From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Ñu wax ko ne: «yeesum nasaret moo fay jaar.»
and they told him, that jesus of nazareth passeth by.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
booba yeesu jóge na dëkku nasaret ci diiwaanu galile, ñëw, yaxya sóob ko ci dexu yurdan.
and it came to pass in those days, that jesus came from nazareth of galilee, and was baptized of john in jordan.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw gi, mu toxoo dëkku nasaret, dem dëkk kapernawum, bi féeteek dex ga ci diiwaani sabulon ak neftali.
and leaving nazareth, he came and dwelt in capernaum, which is upon the sea coast, in the borders of zabulon and nephthalim:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi waajuri yeesu yi matalee seen warugar ci lépp lu yoonu boroom bi santaane woon, ñu dellu seen dëkku nasaret ca diiwaanu galile.
and when they had performed all things according to the law of the lord, they returned into galilee, to their own city nazareth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mu gis piyeer di jaaru, xool ko jàkk naan: «yaw itam àndoon nga ak yeesum nasaret moomu.»
and when she saw peter warming himself, she looked upon him, and said, and thou also wast with jesus of nazareth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yuusufa nag daldi jóge nasaret ca diiwaanu galile, jëm ca diiwaanu yude ca betleyem, dëkk ba daawuda cosaanoo, ndaxte ci askanu daawuda la bokk.
and joseph also went up from galilee, out of the city of nazareth, into judaea, unto the city of david, which is called bethlehem; (because he was of the house and lineage of david:)
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu dem nasaret fa mu yaroo, te ca bésu noflaay ba, mu dugg ca jàngu ba, ni mu ko daan defe. noonu mu taxaw ngir jàngal mbooloo mi.
and he came to nazareth, where he had been brought up: and, as his custom was, he went into the synagogue on the sabbath day, and stood up for to read.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu dégg ne, yeesum nasaret moo fay romb; mu daldi yuuxu naan: «yërëm ma, yaw sëtu daawuda bi!»
and when he heard that it was jesus of nazareth, he began to cry out, and say, jesus, thou son of david, have mercy on me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xam ngeen ne yàlla fal na yeesum nasaret, sol ko xel mu sell mi ak kàttan; muy wër, di def lu baax ak di faj ñépp ñi nekkoon ci kilifteefu seytaane, ndaxte yàlla ànd na ak moom.
how god anointed jesus of nazareth with the holy ghost and with power: who went about doing good, and healing all that were oppressed of the devil; for god was with him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ma tontu ko: “yaa di kan, boroom bi?” mu ne ma: “maa di yeesum nasaret, mi ngay fitnaal.”
and i answered, who art thou, lord? and he said unto me, i am jesus of nazareth, whom thou persecutest.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne leen: «lu fi xew?» Ñu tontu ko ne: «mbirum yeesum nasaret. ab yonent la woon bu doon def ay jëf yu mag, di wax ay kàddu yu am doole, ci kanam nit ñi ak ca kanam yàlla.
and he said unto them, what things? and they said unto him, concerning jesus of nazareth, which was a prophet mighty in deed and word before god and all the people:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: