From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
xam ne nattub ngëm mooy ndeyu muñ.
knowing this, that the trying of your faith worketh patience.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
na sàmm mbóoti ngëm gi ak xel mu dal.
holding the mystery of the faith in a pure conscience.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
di jot muj gi ngëm séentu, maanaam muccu xol.
receiving the end of your faith, even the salvation of your souls.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
li am daal, fa seen ngëm tolloo, na fa seen jëf àgg.
nevertheless, whereto we have already attained, let us walk by the same rule, let us mind the same thing.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon nag nangeen dëgëralante te yokkante seen ngëm, ni ngeen koy defe.
wherefore comfort yourselves together, and edify one another, even as also ye do.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
farluleen te dëgër ci ngëm, di góor-góorlu te am pasteef.
watch ye, stand fast in the faith, quit you like men, be strong.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye léegi, bi jamonoy ngëm ji ñëwee, nekkatunu ci kilifteefu yoon wi.
but after that faith is come, we are no longer under a schoolmaster.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
di sàmm sa ngëm ak xel mu dal. am na ñu seen xel nëx, ba labal seen ngëm,
holding faith, and a good conscience; which some having put away concerning faith have made shipwreck:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ngir seen ngëm bañ a wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley yàlla.
that your faith should not stand in the wisdom of men, but in the power of god.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen samay bokk, bu benn gënale laal seen ngëm ci sunu boroom yeesu kirist, mi soloo ndam.
my brethren, have not the faith of our lord jesus christ, the lord of glory, with respect of persons.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte ci yiwu yàlla ngeen mucce ci kaw ngëm, te loolu jógewul ci yéen, mayu yàlla la;
for by grace are ye saved through faith; and that not of yourselves: it is the gift of god:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»
now the just shall live by faith: but if any man draw back, my soul shall have no pleasure in him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te fal na ma ci ndaw ak jàngalekat, may yégal xeeti àddina yoonu ngëm ak dëgg; fenuma, dëgg rekk laay wax.
whereunto i am ordained a preacher, and an apostle, (i speak the truth in christ, and lie not;) a teacher of the gentiles in faith and verity.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca saa sa yeesu tàllal loxoom, jàpp ko naan: «yaw mi néew ngëm, lu tax nga am xel ñaar?»
and immediately jesus stretched forth his hand, and caught him, and said unto him, o thou of little faith, wherefore didst thou doubt?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
na loolu tax ngeen góor-góorlu, ba yokk ci seen ngëm njàmbaar, ci njàmbaar googu ngeen yokk ci xam-xam, yokk ci noot sa bopp.
and beside this, giving all diligence, add to your faith virtue; and to virtue knowledge;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: