From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
noonu ba ñu nekkee ak seen njaaxle, am na ñaar ñu leen feeñu, sol yére yuy melax.
and it came to pass, as they were much perplexed thereabout, behold, two men stood by them in shining garments:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
seen njariñ a tax ma wax lii, du ngir teg leen yen bu ngeen àttanul, waaye ngeen man a jàppandil boroom bi ci njaamu gu rafet gu àndul ak genn njaaxle.
and this i speak for your own profit; not that i may cast a snare upon you, but for that which is comely, and that ye may attend upon the lord without distraction.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: