From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bi ñu ko gisul nag, ñu daldi dellu yerusalem, seeti ko.
and when they found him not, they turned back again to jerusalem, seeking him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca ëllëg sa pool ànd ak nun, seeti saag, fekk njiit yépp teew fa.
and the day following paul went in with us unto james; and all the elders were present.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon lu ngeen seeti woon? yonent? waaw, wax naa leen ne, ëpp na yonent.
but what went ye out for to see? a prophet? yea, i say unto you, and much more than a prophet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu dëkk ba bépp génn seeti yeesu. ba ñu ko gisee nag, ñu ñaan ko, mu génn seen réew.
and, behold, the whole city came out to meet jesus: and when they saw him, they besought him that he would depart out of their coasts.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nikodem bokkoon na ca farisen ya fa nekkoon. fekk moo seeti woon yeesu lu jiitu. mu ne leen:
nicodemus saith unto them, (he that came to jesus by night, being one of them,)
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mbooloo ma gisee ne, yeesu walla taalibe ya kenn nekkatu fa, ñu dugg ca gaal yooyu, dem seeti ko kapernawum.
when the people therefore saw that jesus was not there, neither his disciples, they also took shipping, and came to capernaum, seeking for jesus.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon lu ngeen seeti woon nag? nit ku sol yére yu rafet? waaye ñi sol yére yu rafet ñu ngi dëkk ci këri buur.
but what went ye out for to see? a man clothed in soft raiment? behold, they that wear soft clothing are in kings' houses.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«bi mu demee ba am ñeent-fukki at, mu fas yéeney seeti ay bokkam, maanaam bànni israyil.
and when he was full forty years old, it came into his heart to visit his brethren the children of israel.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nikodem itam ñëw, moom mi masoon a seeti yeesu guddi. mu indaale lu war a tollook fanweeri kiloy cuuraay lu ñu defare ndàbbi miir ak banti aloos.
and there came also nicodemus, which at the first came to jesus by night, and brought a mixture of myrrh and aloes, about an hundred pound weight.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
fekk baayu publiyus dafa tëdd ndax ay tàngoori yaram yu koy dikkal ak biiru taññ. pool nag dem seeti ko, ñaan ci yàlla, teg ko ay loxoom, mu daldi wér.
and it came to pass, that the father of publius lay sick of a fever and of a bloody flux: to whom paul entered in, and prayed, and laid his hands on him, and healed him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu séen fu sore garabu figg gu sëq, mu dem seeti, ndax am na ay doom. waaye bi mu fa eggee, gisul lu dul ay xob, ndaxte jamonoy figg duggagul.
and seeing a fig tree afar off having leaves, he came, if haply he might find any thing thereon: and when he came to it, he found nothing but leaves; for the time of figs was not yet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne leen: «kaayleen gis.» noonu ñu dem, seeti fa mu daloon, ngoonalal ko. ci tàkkusaani kaw la woon.
he saith unto them, come and see. they came and saw where he dwelt, and abode with him that day: for it was about the tenth hour.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi malaaka ya delloo ca asamaan, sàmm yi di waxante naan: «nanu dem boog betleyem, seeti la fa xew, li nu boroom bi xamal.»
and it came to pass, as the angels were gone away from them into heaven, the shepherds said one to another, let us now go even unto bethlehem, and see this thing which is come to pass, which the lord hath made known unto us.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi loolu wéyee pool nas xel jëm yerusalem, jaar ci diiwaani maseduwan ak akayi. mu ne: «gannaaw bu ma fa demee, fàww ma seeti room it.»
after these things were ended, paul purposed in the spirit, when he had passed through macedonia and achaia, to go to jerusalem, saying, after i have been there, i must also see rome.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«waaye ñu tàmbali di jéggalu ci ngan gi ñoom ñépp. ku jëkk ka ne ko: “damaa jënd tool léegi, te fàww ma dem seeti ko. maa ngi lay ñaan, nga jéggal ma.”
and they all with one consent began to make excuse. the first said unto him, i have bought a piece of ground, and i must needs go and see it: i pray thee have me excused.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: