From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ndaxte jub na ci yàlla, mu delloo coono ñi leen di sonal,
seeing it is a righteous thing with god to recompense tribulation to them that trouble you;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te it kan moo leen di sonal, su ngeen góor-góorloo ci def lu baax?
and who is he that will harm you, if ye be followers of that which is good?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo tax yawut ya di wut a sonal yeesu, ndaxte daan na jëfe noonu ca bésu noflaay ba.
and therefore did the jews persecute jesus, and sought to slay him, because he had done these things on the sabbath day.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ku ñu sonal ndax waayu kirist nga, bu ci rus, waaye nga màggal yàlla ci tur woowu.
yet if any man suffer as a christian, let him not be ashamed; but let him glorify god on this behalf.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
buñu sonal kenn ci yéen ci li mu rey nit walla mu sàcc, mbaa def lu bon, walla dugg ci lu yoonam nekkul.
but let none of you suffer as a murderer, or as a thief, or as an evildoer, or as a busybody in other men's matters.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye doom ji juddoo ni bépp doom, dafa daan sonal doom ji juddoo ci dooley xelum yàlla. te loolu mooy law ba léegi.
but as then he that was born after the flesh persecuted him that was born after the spirit, even so it is now.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye jigéen jii lakkal na ma; kon dinaa ko àtte, ngir mu bañatee ñëw sonal ma. dina rey ak ay wax.”»
yet because this widow troubleth me, i will avenge her, lest by her continual coming she weary me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu ne leen: «bàyyileen ko. defal na ma jëf ju rafet; lu tax ngeen di ko sonal?
and jesus said, let her alone; why trouble ye her? she hath wrought a good work on me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu nag xam la ñu wax, mu ne leen: «jigéen ji defal na ma jëf ju rafet; lu tax ngeen di ko sonal?
when jesus understood it, he said unto them, why trouble ye the woman? for she hath wrought a good work upon me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te it ngir ma bañ a yég sama bopp ndax peeñu yooyu wees xel, mayees na mbir dal ma ci sama yaram, di ma metital ni dég, muy malaakam seytaane mu may sonal, ngir ma bañ a yég sama bopp.
and lest i should be exalted above measure through the abundance of the revelations, there was given to me a thorn in the flesh, the messenger of satan to buffet me, lest i should be exalted above measure.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yeesu di wax nag, am na ku jóge ca kër njiit la, mu ñëw naan: «sa doom faatu na; matatul nuy sonal kilifa gi.»
while he yet spake, there came from the ruler of the synagogue's house certain which said, thy daughter is dead: why troublest thou the master any further?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
fàttalikuleen li ma leen wax: “jaam gënul a màgg sangam.” bu ñu ma sonalee, dinañu leen sonal yéen itam. bu ñu toppee sama wax, dinañu topp seen wax yéen itam.
remember the word that i said unto you, the servant is not greater than his lord. if they have persecuted me, they will also persecute you; if they have kept my saying, they will keep yours also.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: