From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
maa ngi ñëw nag ci yaw mi ne yawut nga; yaa ngi sukkandiku ci yoonu musaa ak di damu ci yàlla.
behold, thou art called a jew, and restest in the law, and makest thy boast of god,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mu sukkandiku ci yaakaar ju dëggu, ji nu am ci dund gu dul jeex, gi yàlla dige ba dara sosoogul, moom mi dul tebbi waxam.
in hope of eternal life, which god, that cannot lie, promised before the world began;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndax lan? ndax dañoo sukkandiku ci seeni jëf, bàyyi ngëm. dañoo daanu ci «doj wuy fakkatale.»
wherefore? because they sought it not by faith, but as it were by the works of the law. for they stumbled at that stumblingstone;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen nag bokk yi, yàlla woo na leen, ngeen nekk i gor. waaye nag buleen ci sukkandiku, bay topp seen nafsu, waaye dimbaleenteleen ci kaw mbëggeel.
for, brethren, ye have been called unto liberty; only use not liberty for an occasion to the flesh, but by love serve one another.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
jox nañu bànni israyil yoon wu sukkandiku ci liggéeyu saraxalekat yi soqikoo ci lewi. su fekkoonte ne nag liggéeyu saraxalekat yooyu manoon na yeggale nit cig mat, kon du soxlaati ab saraxalekat ni ko melkisedeg nekke, ci fànn gu wuute ak gu aaroona.
if therefore perfection were by the levitical priesthood, (for under it the people received the law,) what further need was there that another priest should rise after the order of melchisedec, and not be called after the order of aaron?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: