From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
seeni maam lekk nañu mànn ca màndiŋ ma, teewul dee nañu.
your fathers did eat manna in the wilderness, and are dead.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
teewul ñi ëpp ci ñoom neexuñu woon yàlla, ba mu fàddoon leen ca màndiŋ ma.
but with many of them god was not well pleased: for they were overthrown in the wilderness.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye teewul taxawu, bi ngeen ma taxawu ci sama tiis, jëf ju rafet la.
notwithstanding ye have well done, that ye did communicate with my affliction.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
teewul jigéen dina mucc ci wasin, su saxee ci ngëm ak mbëggeel, di ku sell te maandu.
notwithstanding she shall be saved in childbearing, if they continue in faith and charity and holiness with sobriety.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
teewul ñi ko nangu te gëm ci turam, may na leen, ñu am sañ-sañu nekk doomi yàlla.
but as many as received him, to them gave he power to become the sons of god, even to them that believe on his name:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gor laa te kenn moomu ma; teewul def naa sama bopp jaamu ñépp, ngir man a gindi nit ñu bare ci kirist.
for though i be free from all men, yet have i made myself servant unto all, that i might gain the more.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye mënuñu koo am. teewul ñu bare ñëwoon nañu, di seede lu dul dëgg. ba mujj ñaari nit ñëw naan:
but found none: yea, though many false witnesses came, yet found they none. at the last came two false witnesses,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xam nañu ne, ñiy jëfe loolu, yàlla daganal na seen dee, waaye teewul ñu di ko def, boole ko ak di farle ñi ci sax.
who knowing the judgment of god, that they which commit such things are worthy of death, not only do the same, but have pleasure in them that do them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
su ma deful woon ci seen biir jëf yu kenn deful, kon duñu am bàkkaar. waaye léegi nag gis nañu samay jëf te teewul ñu bañ nu, man ak sama baay.
if i had not done among them the works which none other man did, they had not had sin: but now have they both seen and hated both me and my father.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye jigéen ja ne ko: «waaw sang bi, teewul xaj yi di lekk ruusit, yi rot ci seen lekkukaayu boroom.»
and she said, truth, lord: yet the dogs eat of the crumbs which fall from their masters' table.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye seen dégg ndigal bir na ñépp, ba sama xol sedd lool ci yéen. teewul nag damaa bëgg ngeen am xam-xam bu leer ci lu baax, te bañ a laal dara ci lu bon.
for your obedience is come abroad unto all men. i am glad therefore on your behalf: but yet i would have you wise unto that which is good, and simple concerning evil.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waa yerusalem ak seeni kilifa xàmmiwuñu woon yeesu te xamuñu woon waxu yonent, yi ñuy jàng bésu noflaay bu nekk; teewul ñu amal waxu yonent yi, ci li ñu àtte yeesu, ba daan ko.
for they that dwell at jerusalem, and their rulers, because they knew him not, nor yet the voices of the prophets which are read every sabbath day, they have fulfilled them in condemning him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye teewul boroom bi jox na ma kóolute ci yéen. biral na ma ne, dingeen bokk ak man xalaat. léegi nag, kiy nëxal seen xel, ku mu man a doon, yàlla dina ko mbugal.
i have confidence in you through the lord, that ye will be none otherwise minded: but he that troubleth you shall bear his judgment, whosoever he be.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
teewul nag la dale ca aadama ba ca musaa, dee a ngi fi woon ci àddina, di noot ñépp, ak sax ñi seen bàkkaar melul woon ni bosu aadama, maanaam jàdd yoon. aadama moomu nag moo di takkandeeru kirist, mi waroon a ganesi àddina.
nevertheless death reigned from adam to moses, even over them that had not sinned after the similitude of adam's transgression, who is the figure of him that was to come.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: