From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ci kaw loolu, ñépp dëddu ko, daw.
and they all forsook him, and fled.
Last Update: 2024-03-13
Usage Frequency: 2
Quality:
ndaxte dina dal ci ñépp ñi nekk ci kaw suuf.
for as a snare shall it come on all them that dwell on the face of the whole earth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nangeen mat nag, ni seen baay bi ci kaw mate.
be ye therefore perfect, even as your father which is in heaven is perfect.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
biy cosaanul njaboot gépp, muy ci kaw, muy ci suuf.
of whom the whole family in heaven and earth is named,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca njël nag yeesu jëm ci ñoom, di dox ci kaw dex gi.
and in the fourth watch of the night jesus went unto them, walking on the sea.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu yeesu dénk leen bu wóor, ñu bañ koo wax kenn.
and he charged them that they should tell no man of him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ñu xool ci kaw, waaye gisatuñu kenn ku dul yeesu rekk.
and when they had lifted up their eyes, they saw no man, save jesus only.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu lépp amleen mbëggeel, giy jókkaale lépp, ba mu mat.
and above all these things put on charity, which is the bond of perfectness.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu yeesu wax ci lu leer ne: «lasaar dee na.
then said jesus unto them plainly, lazarus is dead.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yéena di leeru àddina. dëkk, bu nekk ci kaw tund du man a nëbbu.
ye are the light of the world. a city that is set on an hill cannot be hid.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi piyeer di wax loolu, xel mu sell mi wàcc ci kaw ñépp ñiy déglu kàddu ga.
while peter yet spake these words, the holy ghost fell on all them which heard the word.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon gis nga ne, ngëm dafa lëngoo ak ay jëfam, te ngëmam mat ci kaw jëf jooju.
seest thou how faith wrought with his works, and by works was faith made perfect?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye pool wax ci kaw ne: «bul lor sa bopp, nun ñépp nu ngi fi.»
but paul cried with a loud voice, saying, do thyself no harm: for we are all here.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu seytaane yóbbu ko ci kaw tund wu kawe lool, won ko réewi àddina yépp ak seeni ndam.
again, the devil taketh him up into an exceeding high mountain, and sheweth him all the kingdoms of the world, and the glory of them;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ba ninkinànka ja gisee ne, daaneel nañu ko ci kaw suuf, mu dàq jigéen, ja juroon doom ju góor ja.
and when the dragon saw that he was cast unto the earth, he persecuted the woman which brought forth the man child.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»
now the just shall live by faith: but if any man draw back, my soul shall have no pleasure in him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te buleen tudde kenn seen “baay” ci àddina, ndaxte kenn rekk moo di seen baay, ki ci kaw.
and call no man your father upon the earth: for one is your father, which is in heaven.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu yuusufa yeble, woo baayam ak mbokkam yépp, ñuy juróom-ñaar-fukki nit ak juróom.
then sent joseph, and called his father jacob to him, and all his kindred, threescore and fifteen souls.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne ko: «kaay!» piyeer nag wàcc ca gaal ga, di dox ci kaw ndox mi, jëm ci yeesu.
and he said, come. and when peter was come down out of the ship, he walked on the water, to go to jesus.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu dinaa leen wax dëgg ne leen: “musuma leen a xam; soreleen ma, yéen ñiy def bàkkaar.”
and then will i profess unto them, i never knew you: depart from me, ye that work iniquity.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.