From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ku bëggul sa mbokk, xamuloo yàlla, ndax yàlla mbëggeel la.
he that loveth not knoweth not god; for god is love.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu tontu ko ne: «yaw yaay jàngal bànni israyil te xamuloo mbir yii?
jesus answered and said unto him, art thou a master of israel, and knowest not these things?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
képp ku sax ci moom, doo sax ci bàkkaar; kuy def bàkkaar, gisuloo ko te xamuloo ko.
whosoever abideth in him sinneth not: whosoever sinneth hath not seen him, neither known him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xanaa xamuloo ne, man naa laaj sama baay, te dina ma may ci taxawaay bi mbooloom malaaka mu xel dajul?
thinkest thou that i cannot now pray to my father, and he shall presently give me more than twelve legions of angels?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xamuloo ne maa ngi nekk ci baay bi te baay baa ngi ci man? kàddu yi ma leen di wax jógewuñu ci man, waaye baay bi nekk ci man mooy matal ay jëfam.
believest thou not that i am in the father, and the father in me? the words that i speak unto you i speak not of myself: but the father that dwelleth in me, he doeth the works.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndax dangaa xeeb mbaaxu yàlla, mi yéex a mer te di la muñal? xanaa xamuloo ne, yàllaa ngi lay won baaxaayam, ngir nga réccu say bàkkaar?
or despisest thou the riches of his goodness and forbearance and longsuffering; not knowing that the goodness of god leadeth thee to repentance?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu tontu ko ne: «ni ma yàggeek yéen te ba tey filib, xamuloo ma? ku ma gis, gis nga baay bi. kon nag nan ngay man a laaje naan: “won nu baay bi”?
jesus saith unto him, have i been so long time with you, and yet hast thou not known me, philip? he that hath seen me hath seen the father; and how sayest thou then, shew us the father?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: