Results for yóbbe translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

buleen yóbbe tiis xelu yàlla mu sell, mi leen tàmpe ngir bésu goreel ba.

English

and grieve not the holy spirit of god, whereby ye are sealed unto the day of redemption.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu la sa bëtu ndeyjoor bëggee yóbbe bàkkaar, luqi ko, sànni ko fu sore.

English

and if thy right eye offend thee, pluck it out, and cast it from thee: for it is profitable for thee that one of thy members should perish, and not that thy whole body should be cast into hell.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kuy sopp sa mbokk, yaa ngi dëkk ci leer, te luy yóbbe nit bàkkaar du nekk ci yaw.

English

he that loveth his brother abideth in the light, and there is none occasion of stumbling in him.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nanu bàyyee tegante tooñ, waaye nu fas yéenee moytu lépp lu nekk fiir guy yóbbe sunu moroom bàkkaar.

English

let us not therefore judge one another any more: but judge this rather, that no man put a stumblingblock or an occasion to fall in his brother's way.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

doomu nit ki dina yebal ay malaakaam, ñu jële ci nguuram lépp luy yóbbe nit bàkkaar, ak ñiy def bàkkaar,

English

the son of man shall send forth his angels, and they shall gather out of his kingdom all things that offend, and them which do iniquity;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«yaw àddina dinga torox ndax say fiir yiy yóbbe nit bàkkaar. fiir mënta ñàkk, waaye toroxte dal na nit ki koy lal.

English

woe unto the world because of offences! for it must needs be that offences come; but woe to that man by whom the offence cometh!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu waxaat ay taalibeem ne leen: «fiir yuy yóbbe nit bàkkaar mënta ñàkk, waaye toroxte dal na ki koy lal.

English

then said he unto the disciples, it is impossible but that offences will come: but woe unto him, through whom they come!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom mooy ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ca fa gën a xóot ca géej ga.

English

but whoso shall offend one of these little ones which believe in me, it were better for him that a millstone were hanged about his neck, and that he were drowned in the depth of the sea.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te bu la sa tànk di yóbbe bàkkaar, dagg ko. nga lafañ te tàbbi ci dund gu wóor gi moo gën, nga am ñaari tànk, ñu sànni la ci safara.

English

and if thy foot offend thee, cut it off: it is better for thee to enter halt into life, than having two feet to be cast into hell, into the fire that never shall be quenched:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te bu la sa bët di yóbbe bàkkaar, luqi ko. nga patt te dugg ci nguuru yàlla, moo gën ci yaw, nga am ñaari bët, ñu sànni la ci safara.

English

and if thine eye offend thee, pluck it out: it is better for thee to enter into the kingdom of god with one eye, than having two eyes to be cast into hell fire:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

boo xamee ne sa loxo mu ngi lay yóbbe bàkkaar, dagg ko. ndaxte ñàkk loxo te tàbbi ci dund gu wóor gi, moo gën ci yaw, nga am ñaari loxo te tàbbi ci safara su dul fey mukk.

English

and if thy hand offend thee, cut it off: it is better for thee to enter into life maimed, than having two hands to go into hell, into the fire that never shall be quenched:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

boo xamee ne sa bët mu ngi lay yóbbe bàkkaar, luqi ko, sànni ko fu sore. ndaxte nga patt te dugg ci dund gu wóor gi, moo gën ci yaw, nga am ñaari bët, te ñu sànni la ci safara.

English

and if thine eye offend thee, pluck it out, and cast it from thee: it is better for thee to enter into life with one eye, rather than having two eyes to be cast into hell fire.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ñàkk benn ci say cér moo gën ci yaw, ñu sànni sa yaram wépp ci safara. bu la sa loxol ndeyjoor bëggee yóbbe bàkkaar, dagg ko, sànni ko fu sore. ndaxte ñàkk benn ci say cér moo gën ci yaw ñu sànni sa yaram wépp ci safara.

English

and if thy right hand offend thee, cut if off, and cast it from thee: for it is profitable for thee that one of thy members should perish, and not that thy whole body should be cast into hell.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,778,312,312 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK