From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
dex gi yengu na lool, ndaxte da doon ngelaw ak doole.
and the sea arose by reason of a great wind that blew.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye bu nu boroom bi dee àtte, da nuy yar ngir bañ noo boole ci mbugalu àddina.
but when we are judged, we are chastened of the lord, that we should not be condemned with the world.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xanaa kon ngëm day fanq yoonu musaa? mukk! da koy gën a dëgëral sax.
do we then make void the law through faith? god forbid: yea, we establish the law.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi muy wax loolu it, da doon seetlu filib, ndaxte xamoon na booba li mu nar a def.
and this he said to prove him: for he himself knew what he would do.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca jamono yooya nit ñi dinañu sàkku dee, waaye duñu daje ak moom. dinañu bëgg a dee, waaye dee da leen di daw.
and in those days shall men seek death, and shall not find it; and shall desire to die, and death shall flee from them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye bi muy yónni doom jooju di taaw bi ci àddina, da ne:«na ko malaakay yàlla yépp jaamu.»
and again, when he bringeth in the firstbegotten into the world, he saith, and let all the angels of god worship him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
da nga jêem y ñöriñ %(feature)s li %(plugin)s indil na ko. waaye loolu dafa fayal ndax nga böggë taxàl %(plugin)s ngir ko ñöriñ ?
you are trying to use the feature %(feature)s which is provided by %(plugin)s. this plugin is currently disabled. do you wish to enable %(plugin)s so the feature is available?
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.