From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. dina am ay xiif ak ay yengu-yenguy suuf ci bérab yu bare.
for nation shall rise against nation, and kingdom against kingdom: and there shall be famines, and pestilences, and earthquakes, in divers places.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ma dégg lu mel ni baatu mbooloo mu bare, mel ni riiru duusi géej, ni yenguy dënnu yu réy, naan:«aleluya!ndaxte sunu boroomyàlla aji kàttan jidugg na ci nguuram.
and i heard as it were the voice of a great multitude, and as the voice of many waters, and as the voice of mighty thunderings, saying, alleluia: for the lord god omnipotent reigneth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. te yengu-yenguy suuf dina am ciy bérab yu bare, ak ay xiif. loolu lépp mooy ndoortel metit yi, mel ni jigéen juy matu.
for nation shall rise against nation, and kingdom against kingdom: and there shall be earthquakes in divers places, and there shall be famines and troubles: these are the beginnings of sorrows.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: