Results for yokku translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

noonu mboolooy ñi gëm di gën a dëgër ci yoon wi, tey yokku bés bu nekk.

English

and so were the churches established in the faith, and increased in number daily.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesoo ngi doon màgg ci jëmm, tey yokku ci xam-xam te neex yàlla ak nit ñi.

English

and jesus increased in wisdom and stature, and in favour with god and man.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ñu bare ca ña dégg wax ja gëm nañu, te limu góor ñi gëm yokku na, ba mat juróomi junni.

English

howbeit many of them which heard the word believed; and the number of the men was about five thousand.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loolu tekkiwul ne, damay sàkku ay ndimbal ci yéen, waaye damaa bëgg rekk seen denc yokku fa yàlla.

English

not because i desire a gift: but i desire fruit that may abound to your account.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sonnoon na lool ci loxoy fajkat yu bare, sànk ci alalam jépp te jëlewu ci genn tan, waaye faf wopp ja yokku.

English

and had suffered many things of many physicians, and had spent all that she had, and was nothing bettered, but rather grew worse,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñi nangu ay waxam nag, ñu sóob leen ci ndox, te ca bés booba lu mat limub ñetti junniy nit yokku nañu ci ñoom.

English

then they that gladly received his word were baptized: and the same day there were added unto them about three thousand souls.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li ma leen di ñaanal nag mooy lii: na seen mbëggeel di yokku tey gën a tar, jaar ci xam ak xàmmi gu wér;

English

and this i pray, that your love may abound yet more and more in knowledge and in all judgment;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loolu wóor na ma; kon xam naa ne, dinaa fi des, di leen taxawu yéen ñépp, ngir seen ngëm yokku, ànd ak mbég.

English

and having this confidence, i know that i shall abide and continue with you all for your furtherance and joy of faith;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu kàddug yàlla di law, ba mbooloom taalibe yi di yokku bu bare ci yerusalem; te saraxalekat yu bare déggal yàlla ci topp yoonu ngëm wi.

English

and the word of god increased; and the number of the disciples multiplied in jerusalem greatly; and a great company of the priests were obedient to the faith.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te jëmm jépp ci moom lay dunde, di jëmm ju ràbboo te déggoo ci bépp tenqoo, te cér bu nekk di def warugaram. noonu jëmm ji di yokku ak a màgg ci biir mbëggeel.

English

from whom the whole body fitly joined together and compacted by that which every joint supplieth, according to the effectual working in the measure of every part, maketh increase of the body unto the edifying of itself in love.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte lépp li nuy daj, seen njariñ a tax, ngir yiwu yàlla, wiy yokku ci nit ñu gën a takku, yokkaale ngërëm lu jëm ci yàlla, ngir jollil ndamam.

English

for all things are for your sakes, that the abundant grace might through the thanksgiving of many redound to the glory of god.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te nun ñépp nag, danuy lerxat ndamu boroom bi ak xar-kanam bu muuruwul, bay soppiku ci melokaanam, ànd ak ndam luy yokku te sax ci dooley boroom biy xelum yàlla.

English

but we all, with open face beholding as in a glass the glory of the lord, are changed into the same image from glory to glory, even as by the spirit of the lord.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bokk yi, mënunu lu dul sax ci sant yàlla ndax yéen. loolu jaadu na, ndax seen ngëm di gën a sax, te mbëggeel gi ngeen am ci seen biir, ku nekk ci sa moroom, di yokku lu bare.

English

we are bound to thank god always for you, brethren, as it is meet, because that your faith groweth exceedingly, and the charity of every one of you all toward each other aboundeth;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,851,819,188 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK