From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
waaye yoon wi tëj na ñépp ci dooley bàkkaar, ngir ñi gëm yeesu kirist jot li yàlla dige woon ci seen kaw ngëm.
but the scripture hath concluded all under sin, that the promise by faith of jesus christ might be given to them that believe.
bi yeesu ak ay taalibeem nekkee ci yoon wi, mu dugg ci benn dëkk, fekk fa jigéen ju tudd màrt, ganale ko.
now it came to pass, as they went, that he entered into a certain village: and a certain woman named martha received him into her house.
noonu xelum yàlla daldi yóbbu simeyon ba ca kër yàlla ga. bi waajuri yeesu indee xale ba, ngir sédde ko yàlla, ni ko yoon wi santaanee,
and he came by the spirit into the temple: and when the parents brought in the child jesus, to do for him after the custom of the law,
xamuñu yoon, wi yàlla tëral ngir nit jub ci kanamam, waaye dañoo wéy ci seen pexey bopp; ba tax ñu bañ a nangu yoonu njub woowu yàlla tëral.
for they being ignorant of god's righteousness, and going about to establish their own righteousness, have not submitted themselves unto the righteousness of god.