Results for ‪ sama xarit sama xol sama lep ‬ translation from Wolof to French

Wolof

Translate

‪ sama xarit sama xol sama lep ‬

Translate

French

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

jërëjëf sama xarit. 

French

Last Update: 2022-11-22
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

sama xol

French

Last Update: 2021-04-13
Usage Frequency: 4
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

sama xol sedna

French

Last Update: 2021-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

man njiit li, maa ngi lay bind, yaw sama xarit gayus, mi ma bëgg ci sama xol.

French

l`ancien, à gaïus, le bien aimé, que j`aime dans la vérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

da ma la bëugëu sama xol

French

Last Update: 2021-04-28
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

dafa am sama xarit bu ma ganesi, te awma dara lu ma ko jox.”

French

car un de mes amis est arrivé de voyage chez moi, et je n`ai rien à lui offrir,

Last Update: 2024-06-30
Usage Frequency: 2
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

moo tax sama xol sedd,may woy sama bànneex,te it sama yaram di tëdd ci yaakaar.

French

aussi mon coeur est dans la joie, et ma langue dans l`allégresse; et même ma chair reposera avec espérance,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«sama xol a ngi màggal boroom bi,sama xel di bég ci yàlla sama musalkat,

French

et mon esprit se réjouit en dieu, mon sauveur,

Last Update: 2024-02-04
Usage Frequency: 2
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaw yaw sama mbokk, dimbali ma ci boroom bi, te seral sama xol ci sunu bokk ci kirist.

French

oui, frère, que j`obtienne de toi cet avantage, dans le seigneur; tranquillise mon coeur en christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

yaw sama xarit, sa takkute fés na ci teeru bi ngay teeru mbokk yi, te fekk xamoo leen.

French

bien-aimé, tu agis fidèlement dans ce que tu fais pour les frères, et même pour des frères étrangers,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

yeen samay xarit, sama ñaareelu bataaxel a ngi nii. bind naa leen, ngir xiir leen ci xalaat yu sell.

French

voici déjà, bien-aimés, la seconde lettre que je vous écris. dans l`une et dans l`autre je cherche à éveiller par des avertissements votre saine intelligence,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»

French

et mon juste vivra par la foi; mais, s`il se retire, mon âme ne prend pas plaisir en lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ndaxte su ma leen tegee naqar, kuy seddal sama xol ku dul yéen ñi ma teg aw naqar?

French

car si je vous attriste, qui peut me réjouir, sinon celui qui est attristé par moi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

noonu delloo naa leen ko ci lu gaaw, ngir ñëwam bégal seeni xol, te man itam sama xol féex.

French

je l`ai donc envoyé avec d`autant plus d`empressement, afin que vous vous réjouissiez de le revoir, et que je sois moi-même moins triste.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

sama xarit, bul roy lu bon, waaye lu baax rekk. kuy def lu baax, ci yàlla nga bokk; kuy def lu bon, xamoo dara ci yàlla.

French

bien-aimé, n`imite pas le mal, mais le bien. celui qui fait le bien est de dieu; celui qui fait le mal n`a point vu dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye onesifor daa na faral di dëfël sama xol; na boroom bi sotti yërmandeem ci këram. rusul woon sax ci samay jéng,

French

que le seigneur répande sa miséricorde sur la maison d`onésiphore, car il m`a souvent consolé, et il n`a pas eu honte de mes chaînes;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

mu ne leen: «sama xol dafa tiis, ba ma bëgg a dee; toogleen fii, xool.»

French

il leur dit: mon âme est triste jusqu`à la mort; restez ici, et veillez.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

kóolute gi ma am ci yéen réy na. tiitar bi may jële ci yéen réy na. sama xol sedd na guyy. damaa fees ak mbég ci bépp coono bu nuy daj!

French

j`ai une grande confiance en vous, j`ai tout sujet de me glorifier de vous; je suis rempli de consolation, je suis comblé de joie au milieu de toutes nos tribulations.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye sama xol sedd na léegi, du ndax seen tiis, waaye ci li mu tax ngeen réccu. tiis wu jóge ci yàlla ngeen tegoo, te àndul ak benn loraange bu bawoo ci nun.

French

je me réjouis à cette heure, non pas de ce que vous avez été attristés, mais de ce que votre tristesse vous a portés à la repentance; car vous avez été attristés selon dieu, afin de ne recevoir de notre part aucun dommage.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye seen dégg ndigal bir na ñépp, ba sama xol sedd lool ci yéen. teewul nag damaa bëgg ngeen am xam-xam bu leer ci lu baax, te bañ a laal dara ci lu bon.

French

pour vous, votre obéissance est connue de tous; je me réjouis donc à votre sujet, et je désire que vous soyez sages en ce qui concerne le bien et purs en ce qui concerne le mal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
8,927,582,053 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK