Results for artu translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

waaye ñiy bàkkaar, yedd leen fa kanam ñépp, ngir artu ñi ci des.

French

ceux qui pèchent, reprends-les devant tous, afin que les autres aussi éprouvent de la crainte.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mbir yooyu leen daloon misaal la ci nun, te bind nañu ko ngir artu nu, nun ñiy dund ci jamono jii lépp mat.

French

ces choses leur sont arrivées pour servir d`exemples, et elles ont été écrites pour notre instruction, à nous qui sommes parvenus à la fin des siècles.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.

French

ce n`est pas pour vous faire honte que j`écris ces choses; mais je vous avertis comme mes enfants bien-aimés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foogleen nag, di fàttaliku ne diirub ñetti at, guddi ak bëccëg, musumaa noppi di leen artu kenn ku nekk ci yéen ak ay rangooñ.

French

veillez donc, vous souvenant que, durant trois années, je n`ai cessé nuit et jour d`exhorter avec larmes chacun de vous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moytuleen a tanqamlu nag kiy wax ak yéen. ndegam ñiy tanqamlu ki leen di artu ci àddina, ñoo mënul a rëcc ci àtte bi, aste ku dummóoyu kiy wax ci asamaan.

French

gardez-vous de refuser d`entendre celui qui parle; car si ceux-là n`ont pas échappé qui refusèrent d`entendre celui qui publiait les oracles sur la terre, combien moins échapperons-nous, si nous nous détournons de celui qui parle du haut des cieux,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu bokk yi, ci lu jëm ci njiit, yi boroom bi teg ci seen kanam te ñuy liggéey ci seen biir, di leen artu, maa ngi leen di ñaan ngeen déglu leen;

French

nous vous prions, frères, d`avoir de la considération pour ceux qui travaillent parmi vous, qui vous dirigent dans le seigneur, et qui vous exhortent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,772,806,091 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK