Results for bëgg naa la translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

namm naa la

French

Last Update: 2023-05-19
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bëgg naa laa seetsi balaa yàgg,

French

je t`écris ces choses, avec l`espérance d`aller bientôt vers toi,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«damaa ñëw ngir indi safara si ci àddina, te bëgg naa xaat taal bi tàkk.

French

je suis venu jeter un feu sur la terre, et qu`ai-je à désirer, s`il est déjà allumé?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

lu tax? ndax dama leen a bëggul? yàlla xam na ne, bëgg naa leen!

French

pourquoi?... parce que je ne vous aime pas?... dieu le sait!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waa ja ne: «boroom bi, gëm naa la.» noonu mu jaamu yeesu.

French

et il dit: je crois, seigneur. et il se prosterna devant lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu bind naa la, ndax wóor na ma ne, dinga ma déggal, ba weesu sax li ma la sant.

French

c`est en comptant sur ton obéissance que je t`écris, sachant que tu feras même au delà de ce que je dis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu yërëm ko, tàllal loxoom, laal ko naan: «bëgg naa ko, wéral.»

French

jésus, ému de compassion, étendit la main, le toucha, et dit: je le veux, sois pur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.

French

ce n`est pas pour vous faire honte que j`écris ces choses; mais je vous avertis comme mes enfants bien-aimés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye nag bëgg naa ngeen xam lii: kirist mooy kilifag bépp góor, góor di kilifag jigéen, te yàlla di kilifag kirist.

French

je veux cependant que vous sachiez que christ est le chef de tout homme, que l`homme est le chef de la femme, et que dieu est le chef de christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bàyyi naa la ca réewu kereet, ngir nga mottali la desoon ci liggéey bi, te samp ay njiiti mbooloo ca dëkk bu nekk, ni ma la ko sante woon.

French

je t`ai laissé en crète, afin que tu mettes en ordre ce qui reste à régler, et que, selon mes instructions, tu établisses des anciens dans chaque ville,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam nga ne, ba may dem diiwaanu maseduwan, ñaanoon naa la, nga des dëkku efes, ngir dénk ña fa doon jàngale luy sànke, ñu bàyyi ko.

French

je te rappelle l`exhortation que je te fis, à mon départ pour la macédoine, lorsque je t`engageai à rester à Éphèse, afin de recommander à certaines personnes de ne pas enseigner d`autres doctrines,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bëgg naa nag, ngeen xam bëre bu metti, bi may bëre ngir yéen, ngir waa lawdise ak ñépp ñi ma musul a teg bët. damay def sama kem-kàttan,

French

je veux, en effet, que vous sachiez combien est grand le combat que je soutiens pour vous, et pour ceux qui sont à laodicée, et pour tous ceux qui n`ont pas vu mon visage en la chair,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man njiit li maa leen di bind, yaw soxna su tedd si, yaw ak say doom. bëgg naa leen bu wér ci sama xol, jéllale naa sama bopp sax, waaye itam képp ku xam dëgg gi.

French

l`ancien, à kyria l`élue et à ses enfants, que j`aime dans la vérité, -et ce n`est pas moi seul qui les aime, mais aussi tous ceux qui ont connu la vérité, -

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu daldi dindi xeer wa. yeesu xool ci kaw, ne jàkk asamaan, ñaan yàlla ne: «baay, sant naa la ci li nga ma déglu ba noppi.

French

ils ôtèrent donc la pierre. et jésus leva les yeux en haut, et dit: père, je te rends grâces de ce que tu m`as exaucé.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ndax li ma ne, gis naa la ca ker garab ga, moo tax nga gëm? dinga gis mbir yu gën a réy yii.»

French

jésus lui répondit: parce que je t`ai dit que je t`ai vu sous le figuier, tu crois; tu verras de plus grandes choses que celles-ci.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nataneel ne ko: «noo ma xame?» yeesu tontu ko ne: «bi la filib di laata woo, gis naa la, bi nga nekkee ca ker garabu figg ga.»

French

d`où me connais-tu? lui dit nathanaël. jésus lui répondit: avant que philippe t`appelât, quand tu étais sous le figuier, je t`ai vu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,800,246,758 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK