Results for ci dund translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

dund gu dul jeex

French

vie éternelle

Last Update: 2017-02-08
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

te bëgguleen a ñëw ci man ngir am dund!

French

et vous ne voulez pas venir à moi pour avoir la vie!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

nu sell te jub ci kanamam sunu giiru dund.

French

en marchant devant lui dans la sainteté et dans la justice tous les jours de notre vie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

maay ñam wiy joxe dund.

French

je suis le pain de vie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ngir képp ku ko gëm am ci moom dund gu dul jeex.»

French

afin que quiconque croit en lui ait la vie éternelle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

noonu dee mu ngi jëf ci nun, dund di jëf ci yéen.

French

ainsi la mort agit en nous, et la vie agit en vous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ci moom la dund nekk, te dund googu mooy leeral nit ñi.

French

en elle était la vie, et la vie était la lumière des hommes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ndaw tiitaange ci ku sàggan, ba tàbbi ci loxoy yàlla jiy dund!

French

c`est une chose terrible que de tomber entre les mains du dieu vivant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

su amee mbokk ci seen biir, mu rafle te amul dund, muy góor walla jigéen,

French

si un frère ou une soeur sont nus et manquent de la nourriture de chaque jour,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

di fàggu dencu ëllëg bu wér. noonu dinañu feddali seen téye ci dund gu wóor gi.

French

et de s`amasser ainsi pour l`avenir un trésor placé sur un fondement solide, afin de saisir la vie véritable.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

képp ku ñu bindul sa tur ci téereb dund bi, dees na la sànni ci déegu safara si.

French

quiconque ne fut pas trouvé écrit dans le livre de vie fut jeté dans l`étang de feu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ku wax ne ci yàlla nga sax, fàww nga dund, ni yeesu kirist daan dunde moom ci boppam.

French

celui qui dit qu`il demeure en lui doit marcher aussi comme il a marché lui-même.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ku bëgg bakkanam dina ko ñàkk, waaye ku ko bañ ci àddina sii, dina ko denc ngir dund gu dul jeex gi.

French

celui qui aime sa vie la perdra, et celui qui hait sa vie dans ce monde la conservera pour la vie éternelle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«demleen taxaw ca kër yàlla ga, te xamal nit ñi lépp lu jëm ci dund gu wóor gii.»

French

allez, tenez-vous dans le temple, et annoncez au peuple toutes les paroles de cette vie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ku jub ci sama kanam dina dund ci kaw ngëm,waaye bu delloo gannaaw,sama xol du sedd ci moom.»

French

et mon juste vivra par la foi; mais, s`il se retire, mon âme ne prend pas plaisir en lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«yéen ñi fóot seeni mbubb, ngir sañ a lekk ci garabu dund gi te dugg ci bunti dëkk bi, barkeel ngeen.

French

heureux ceux qui lavent leurs robes, afin d`avoir droit à l`arbre de vie, et d`entrer par les portes dans la ville!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye léegi yàlla goreel na leen ci kilifteefu bàkkaar, def leen ay jaamam, ba jural leen sell, jëme leen ci dund gu dul jeex.

French

mais maintenant, étant affranchis du péché et devenus esclaves de dieu, vous avez pour fruit la sainteté et pour fin la vie éternelle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

simoŋ piyeer ne ko: «boroom bi, ci kan lanuy dem? yaa yor kàddu yiy joxe dund gu dul jeex.

French

simon pierre lui répondit: seigneur, à qui irions-nous? tu as les paroles de la vie éternelle.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

nu ngi rafetal sunu yen ci dund gu sell, ci xam-xam, muñ ak laabiir, ci xel mu sell mi ak ci mbëggeel gu raxul njublaŋ,

French

par la pureté, par la connaissance, par la longanimité, par la bonté, par un esprit saint, par une charité sincère,

Last Update: 2023-12-17
Usage Frequency: 2
Quality:

Reference: Anonymous
Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

te bu la sa tànk di yóbbe bàkkaar, dagg ko. nga lafañ te tàbbi ci dund gu wóor gi moo gën, nga am ñaari tànk, ñu sànni la ci safara.

French

si ton pied est pour toi une occasion de chute, coupe-le; mieux vaut pour toi entrer boiteux dans la vie,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
8,913,957,874 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK