Results for daajaale translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

taskati réew ma it, ya ñu daajaale ak moom, di ko xas noonule.

French

les brigands, crucifiés avec lui, l`insultaient de la même manière.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

booba it ñu daajaale ak moom ñaari taskati réew ma, kenn ci ndeyjooram, ka ca des ci càmmooñam.

French

avec lui furent crucifiés deux brigands, l`un à sa droite, et l`autre à sa gauche.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu xarekat ya dem, damm tànki ku jëkk ka, teg ca ka ca des, ca ña ñu daajaale woon ak yeesu.

French

les soldats vinrent donc, et ils rompirent les jambes au premier, puis à l`autre qui avait été crucifié avec lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foofa la xarekat ya daaje yeesu ca bant ba. ci noonu it ñu daajaale ñaari nit ci wetam, mu nekk ca digg ba.

French

c`est là qu`il fut crucifié, et deux autres avec lui, un de chaque côté, et jésus au milieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mbind mi nu doon tiiñal, te daa nu yey ndax ay sàrtam, yàlla far na ko, dindi ko, daajaale ko ca bant, ba kirist deeye.

French

il a effacé l`acte dont les ordonnances nous condamnaient et qui subsistait contre nous, et il l`a détruit en le clouant à la croix;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi xarekat ya agsee ba ca bérab, ba ñuy wooye kaaŋu bopp, ñu daaj fa yeesu ca bant, daajaale ñaari defkati lu bon ya, kenn ca ndeyjooram, ka ca des ca càmmooñam.

French

lorsqu`ils furent arrivés au lieu appelé crâne, ils le crucifièrent là, ainsi que les deux malfaiteurs, l`un à droite, l`autre à gauche.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndegam xam nanu ne, daajoon nañu kirist ca bant ba, xam nanu it ne, jikko ju bon ji nu judduwaale, daajaale nañu ko ak kirist ca bant ba. te yàlla def na loolu, ngir nguuru bàkkaar, gi nekkoon ci sunu yaram tas, nu rëcc ci dooleem.

French

sachant que notre vieil homme a été crucifié avec lui, afin que le corps du péché fût détruit, pour que nous ne soyons plus esclaves du péché;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,025,492,016 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK