Results for doom dëgg translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

bi bëgg ñépp mucc te xam dëgg gi.

French

qui veut que tous les hommes soient sauvés et parviennent à la connaissance de la vérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.

French

car le fruit de la lumière consiste en toute sorte de bonté, de justice et de vérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay doom, bunu bëggante ci wax mbaa ci làmmiñ rekk, waaye ci jëf ak ci dëgg.

French

petits enfants, n`aimons pas en paroles et avec la langue, mais en actions et avec vérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma.

French

et moi, parce que je dis la vérité, vous ne me croyez pas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dinañu tanqamlu dëgg, jeng jëm ci léebi diiney neen.

French

détourneront l`oreille de la vérité, et se tourneront vers les fables.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag bu leen doom ji defee gor, dingeen doon ay gor tigi.

French

si donc le fils vous affranchit, vous serez réellement libres.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

baay bi dafa bëgg doom ji, te jox na ko sañ-sañ ci lépp.

French

le père aime le fils, et il a remis toutes choses entre ses mains.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

taxawleen kon temm, geñoo dëgg te sàngoo njub, muy seen kiiraayu dënn.

French

tenez donc ferme: ayez à vos reins la vérité pour ceinture; revêtez la cuirasse de la justice;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»

French

le souverain sacrificateur dit: les choses sont-elles ainsi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mujj mu yónni doomam naan: “xëy na ñu weg sama doom.”

French

enfin, il envoya vers eux son fils, en disant: ils auront du respect pour mon fils.

Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 31
Quality:

Wolof

te jaam du bokk ci kër gi ba fàww, waaye doom, moom, ci kër gi la bokk ba fàww.

French

or, l`esclave ne demeure pas toujours dans la maison; le fils y demeure toujours.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man njiit li maa leen di bind, yaw soxna su tedd si, yaw ak say doom. bëgg naa leen bu wér ci sama xol, jéllale naa sama bopp sax, waaye itam képp ku xam dëgg gi.

French

l`ancien, à kyria l`élue et à ses enfants, que j`aime dans la vérité, -et ce n`est pas moi seul qui les aime, mais aussi tous ceux qui ont connu la vérité, -

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

salmon jur ci raxab doom ju tudd bowas; bowas am ak ruut obedd; obedd jur yese,

French

salmon engendra boaz de rahab; boaz engendra obed de ruth;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñooñu ne leen: «dëgg la, boroom bi dekki na, te feeñu na simoŋ!»

French

et disant: le seigneur est réellement ressuscité, et il est apparu à simon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku ma gënalul sa ndey walla sa baay, yeyoowuloo ma; ku ma gënalul sa doom ju góor walla ju jigéen, yeyoowuloo ma.

French

celui qui aime son père ou sa mère plus que moi n`est pas digne de moi, et celui qui aime son fils ou sa fille plus que moi n`est pas digne de moi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay doom, waxtu wu mujj wi jot na! dégg ngeen ne, benn bañaaleb kirist dina ñëw; te dëgg la, bañaaley kirist yu bare feeñ nañu. ci loolu lanu xame ne, waxtu wu mujj wi jot na.

French

petits enfants, c`est la dernière heure, et comme vous avez appris qu`un antéchrist vient, il y a maintenant plusieurs antéchrists: par là nous connaissons que c`est la dernière heure.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,837,283 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK