Results for féewaloo translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

noonu féewaloo daldi am ca biir mbooloo ma ndax yeesu.

French

il y eut donc, à cause de lui, division parmi la foule.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fàww mu am ay féewaloo ci seen biir, ngir ñu man a xàmmi ñi neex yàlla ci yéen.

French

car il faut qu`il y ait aussi des sectes parmi vous, afin que ceux qui sont approuvés soient reconnus comme tels au milieu de vous. -

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci bu jëkk dégg naa lii: bu ngeen di daje, am na ci yéen ñuy féewaloo, te xaw naa koo gëm.

French

et d`abord, j`apprends que, lorsque vous vous réunissez en assemblée, il y a parmi vous des divisions, -et je le crois en partie,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xërëm, luxus, noonoo ak xuloo, ñeetaane, xadar, diiroo mbagg, féewaloo ak xaajaloo,

French

l`idolâtrie, la magie, les inimitiés, les querelles, les jalousies, les animosités, les disputes, les divisions, les sectes,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndax dangeen a xalaat ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina? déedéet. maa ngi leen koy wax, damaa ñëw ngir indi féewaloo.

French

pensez-vous que je sois venu apporter la paix sur la terre? non, vous dis-je, mais la division.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaawsi tey, bu juróomi nit bokkee genn kër, dinañu féewaloo. Ñett dinañu féewaloo ak ñaar ñi ci des, ñaar ñi féewaloo ak ñett ñooñu.

French

car désormais cinq dans une maison seront divisés, trois contre deux, et deux contre trois;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

baay bi dina féewaloo ak doom ji, doom ji ak baayam. ndey dina féewaloo ak doomam ju jigéen; doom ju jigéen ji ak ndeyam. goro dina féewaloo ak jabaru doomam; jabaru nit ak goroom.»

French

le père contre le fils et le fils contre le père, la mère contre la fille et la fille contre la mère, la belle-mère contre la belle-fille et la belle-fille contre la belle-mère.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,799,771,429 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK