From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
faf am ca kanamam nit ku feebaroon, ay tànkam newi.
et voici, un homme hydropique était devant lui.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
amoon na fa benn waay bu feebaroon lu mat fanweeri at ak juróom ñett.
là se trouvait un homme malade depuis trente-huit ans.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
amoon na fa njiitu xare. njiit la nag, surgaam bu mu bëggoon lool dafa feebaroon, bay bëgg a dee.
un centenier avait un serviteur auquel il était très attaché, et qui se trouvait malade, sur le point de mourir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: