From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
moo tax mu waxaat feneen ne:“doo bàyyi sa waa ju sell, mu yàqu.”
c`est pourquoi il dit encore ailleurs: tu ne permettras pas que ton saint voie la corruption.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye fàww ma dox sama itte tey, suba ak gannaaw suba, ndaxte wareesul a reye ab yonent feneen fu dul yerusalem.
mais il faut que je marche aujourd`hui, demain, et le jour suivant; car il ne convient pas qu`un prophète périsse hors de jérusalem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu tontu leen: «nanu dem feneen ci dëkk yi nu wër, ma waare fa itam, ndaxte moo tax ma génn.»
il leur répondit: allons ailleurs, dans les bourgades voisines, afin que j`y prêche aussi; car c`est pour cela que je suis sorti.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku jaar feneen fu dul ci buntu gétt gi, kooku sàcc la, saay-saay la.
en vérité, en vérité, je vous le dis, celui qui n`entre pas par la porte dans la bergerie, mais qui y monte par ailleurs, est un voleur et un brigand.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
piyeer taf loxoom ci gémmiñam, ngir ñu noppi, daldi leen nettali, ni ko boroom bi génnee ca kaso ba. mu ne leen: «tee ngeen jottali ko saag ak bokk ya.» bi mu ko waxee, mu jóge fa, dem feneen.
pierre, leur ayant de la main fait signe de se taire, leur raconta comment le seigneur l`avait tiré de la prison, et il dit: annoncez-le à jacques et aux frères. puis il sortit, et s`en alla dans un autre lieu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: