Results for gëmloo translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

bésu noflaay bu nekk nag muy diisoo ak ñi nekk ca jàngu ba, di jéem a gëmloo ay yawut ak ay gereg.

French

paul discourait dans la synagogue chaque sabbat, et il persuadait des juifs et des grecs.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu pool dugg ca jàngu ba, di wax ak fit wu dëgër diirub ñetti weer, di diisoo ak ñoom ci mbirum nguurug yàlla, di leen jéem a gëmloo.

French

ensuite paul entra dans la synagogue, où il parla librement. pendant trois mois, il discourut sur les choses qui concernent le royaume de dieu, s`efforçant de persuader ceux qui l`écoutaient.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw xam nanu ragal yàlla nag, nu ngi fexee gëmloo nit ñi, waaye li nu nekk leer na yàlla te yaakaar naa ne, leer na leen it, ba ne fàŋŋ.

French

connaissant donc la crainte du seigneur, nous cherchons à convaincre les hommes; dieu nous connaît, et j`espère que dans vos consciences vous nous connaissez aussi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loo ci xam, yaw jigéen ji, ndax dinga gëmloo sa jëkkër musalkat bi walla déet? loo ci xam yaw jëkkër ji it, ndax dinga gëmloo sa jabar musalkat bi walla déet?

French

car que sais-tu, femme, si tu sauveras ton mari? ou que sais-tu, mari, si tu sauveras ta femme?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu dig ko bés, te ñu bare ñëw, fekksi ko ca néegam. mu di leen jàngal suba ba ngoon, di leen dëggal lu jëm ci nguuru yàlla ak ci yeesu, tukkee ci yoonu musaa ak ci yonent yi, di leen jéem a gëmloo.

French

ils lui fixèrent un jour, et plusieurs vinrent le trouver dans son logis. paul leur annonça le royaume de dieu, en rendant témoignage, et en cherchant, par la loi de moïse et par les prophètes, à les persuader de ce qui concerne jésus. l`entretien dura depuis le matin jusqu`au soir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,790,607,810 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK