From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
di ngiñ, li mu giñaloon sunu maam ibraayma naan,
selon le serment par lequel il avait juré à abraham, notre père,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moo tax «yàlla jagleel na ibraayma njub.»
c`est pourquoi cela lui fut imputé à justice.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yanqóoba; isaaxa; ibraayma; teraa; naxor;
fils de jacob, fils d`isaac, fils d`abraham, fis de thara, fils de nachor,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
sunu maam ibraayma, mi nu soqikoo; nu mbiram tëdde?
que dirons-nous donc qu`abraham, notre père, a obtenu selon la chair?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ibraayma di xaar tey muñ, ba jot li ko yàlla digoon.
et c`est ainsi qu`abraham, ayant persévéré, obtint l`effet de la promesse.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte mi ngi nekkoon ci geñog maamam ibraayma, bi ko melkisedeg gatandoo.
car il était encore dans les reins de son père, lorsque melchisédek alla au-devant d`abraham.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
leer na ne, yeesu xettalisiwul malaaka yi, waaye askanu ibraayma lay xettalisi.
car assurément ce n`est pas à des anges qu`il vient en aide, mais c`est à la postérité d`abraham.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ni mu ko dige woon sunuy maam,jëmale ko ci ibraayma ak askanam ba fàww.»
comme il l`avait dit à nos pères, -envers abraham et sa postérité pour toujours.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ñu koy mbugal ca safara, mu téen, séen fu sore ibraayma ak lasaar ci wetam.
dans le séjour des morts, il leva les yeux; et, tandis qu`il était en proie aux tourments, il vit de loin abraham, et lazare dans son sein.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«bokk yi, yéen askanu ibraayma ak yéen ñi ragal yàlla, kàddug mucc gi ci nun la wàcc.
hommes frères, fils de la race d`abraham, et vous qui craignez dieu, c`est à vous que cette parole de salut a été envoyée.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
seen baay ibraayma bég na, bi mu yégee sama ngan. bi mu ko gisee it, bég na ci lool.»
abraham, votre père, a tressailli de joie de ce qu`il verrait mon jour: il l`a vu, et il s`est réjoui.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kon ñi gëm, yàlla dina leen barkeel, sukkandikoo ko ci seen ngëm, ni mu defal ibraayma, boroom ngëm.
de sorte que ceux qui croient sont bénis avec abraham le croyant.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye loolu lañu bind ne: «yàlla jagleel na ko njub,» du ibraayma rekk a moom wax ji.
mais ce n`est pas à cause de lui seul qu`il est écrit que cela lui fut imputé;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne ko: «mucc gi wàcc na tey ci kër gii, ndaxte nit kii, ci askanu ibraayma la bokk itam.
jésus lui dit: le salut est entré aujourd`hui dans cette maison, parce que celui-ci est aussi un fils d`abraham.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jigéen jii nag bokk ci askanu ibraayma te seytaane tënk ko fukki at ak juróom-ñett, ndax kenn waru koo yiwi ci bésu noflaay bi?»
et cette femme, qui est une fille d`abraham, et que satan tenait liée depuis dix-huit ans, ne fallait-il pas la délivrer de cette chaîne le jour du sabbat?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
maanaam, soqikoo ci ibraayma taxul a nekk doomu yàlla, waaye juddu ci biir digeb yàlla mooy tax a bokk dëgg-dëgg ci askanu ibraayma.
c`est-à-dire que ce ne sont pas les enfants de la chair qui sont enfants de dieu, mais que ce sont les enfants de la promesse qui sont regardés comme la postérité.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ibraayma tontu ko ne: “su ñu dégluwul musaa ak yonent yi, kon ku dekki sax, du tax ñu gëm.”»
et abraham lui dit: s`ils n`écoutent pas moïse et les prophètes, ils ne se laisseront pas persuader quand même quelqu`un des morts ressusciterait.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
xool-leen ci ibraayma; mbind mi wax na ne:«ibraayma gëm na yàlla,te yàlla jàppe ngëmam ni njub.»
comme abraham crut à dieu, et que cela lui fut imputé à justice,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
boroom alal ja ne ko: “déedéet, maam ibraayma, waaye su kenn dekkee, dem ca ñoom, dinañu tuub seeni bàkkaar.”
et il dit: non, père abraham, mais si quelqu`un des morts va vers eux, ils se repentiront.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te it du ñi soqikoo ci ibraayma ñépp, ay doomam dëgg lañu. ndaxte yàlla dafa wax ibraayma ne ko: «saw askan ci isaaxa lay jaar.»
et, pour être la postérité d`abraham, ils ne sont pas tous ses enfants; mais il est dit: en isaac sera nommée pour toi une postérité,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: