From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bi loolu amee nag jigéen ña daldi jóge bu gaaw ca bàmmeel ba, tiit ak mbég mu réy di jax seen xol, ñu daldi daw, ngir yégal ko taalibe ya.
elles s`éloignèrent promptement du sépulcre, avec crainte et avec une grande joie, et elles coururent porter la nouvelle aux disciples.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte, ci ni ñu ko nettalee, benn malaakam boroom bi da daan wàcc léeg-léeg di jax ndox mi. bu ndox mi masaa yengu ba noppi, jarag ju ca jiitu, wopp joo amaan, daldi wér ca saa sa.
car un ange descendait de temps en temps dans la piscine, et agitait l`eau; et celui qui y descendait le premier après que l`eau avait été agitée était guéri, quelle que fût sa maladie.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: