From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
fekk na booba bésu jéggi ba, di màggalu yawut ya, jubsi.
or, la pâque était proche, la fête des juifs.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu ñu gisee ñu sëq, soxlawuleen kenn wax leen ne, nawet bi jubsi na xaat.
dès qu`ils ont poussé, vous connaissez de vous-mêmes, en regardant, que déjà l`été est proche.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
màggalu yawut, gi ñuy wax bésu jéggi ba, mu ngi doon jubsi. yeesu dem yerusalem,
la pâque des juifs était proche, et jésus monta à jérusalem.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu mbir yooyu di tàmbalee xew nag, boo yaboo ngeen siggi, téen, ndaxte seen njot jubsi na.»
quand ces choses commenceront à arriver, redressez-vous et levez vos têtes, parce que votre délivrance approche.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu, mi xamoon li ko waroon a dal lépp, jubsi leen ne leen: «ku ngeen di seet?»
jésus, sachant tout ce qui devait lui arriver, s`avança, et leur dit: qui cherchez-vous?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bésu jéggi ba, di màggalu yawut ya, mu ngi doon jubsi, ba ñu bare ca waa àll ba di dem yerusalem balaa booba, ngir sanguji set.
la pâque des juifs était proche. et beaucoup de gens du pays montèrent à jérusalem avant la pâque, pour se purifier.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te bunu bàyyi sunu ndaje yi, ni ko ñenn ñi di defe, waaye nanuy nàddante ci ngëm, di ko feddali, fi ak yéena ngi gis bésu boroom biy jubsi.
n`abandonnons pas notre assemblée, comme c`est la coutume de quelques-uns; mais exhortons-nous réciproquement, et cela d`autant plus que vous voyez s`approcher le jour.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: