Results for ki kan la translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ki kan la

French

Last Update: 2024-03-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ki kan la waay

French

Last Update: 2021-04-17
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

taalibe ba daldi walbatiku ca yeesu, laaj ko ne: «boroom bi, kooku kan la?»

French

et ce disciple, s`étant penché sur la poitrine de jésus, lui dit: seigneur, qui est-ce?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

xawma woon kooku kan la waroon a doon, waaye xamal ko bànni israyil moo tax ma ñëw, di sóob nit ñi ci ndox.»

French

je ne le connaissais pas, mais c`est afin qu`il fût manifesté à israël que je suis venu baptiser d`eau.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ngir li yonent yàlla esayi waxoon am:«boroom bi, ana ku gëm sunu waare?kan la boroom bi won dooleem?»

French

afin que s`accomplît la parole qu`Ésaïe, le prophète, a prononcée: seigneur, qui a cru à notre prédication? et à qui le bras du seigneur a-t-il été révélé?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

bi ko nit ña gisee, ñu waaru naan: «kii kan la ci biir nit ñi, ba ngelaw li ak dex gi di ko déggal?»

French

ces hommes furent saisis d`étonnement: quel est celui-ci, disaient-ils, à qui obéissent même les vents et la mer?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«lu ngeen xalaat ci almasi bi; kan la nekk sëtam?» Ñu tontu ko: «daawuda.»

French

en disant: que pensez-vous du christ? de qui est-il fils? ils lui répondirent: de david.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

jaraaf ja nag ne filib: «maa ngi lay laaj, ci mbirum kan la yonent bi jëmale wax ji? ndax mbirum boppam lay wax mbaa mu keneen?»

French

l`eunuque dit à philippe: je te prie, de qui le prophète parle-t-il ainsi? est-ce de lui-même, ou de quelque autre?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,747,353,201 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK