Results for labal translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

te ndox it moo labal àddina sa, raafal ko.

French

et que par ces choses le monde d`alors périt, submergé par l`eau,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

di sàmm sa ngëm ak xel mu dal. am na ñu seen xel nëx, ba labal seen ngëm,

French

en gardant la foi et une bonne conscience. cette conscience, quelques-uns l`ont perdue, et ils ont fait naufrage par rapport à la foi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu li yàqu solee melokaanu li dul yàqu, te liy dee sol melokaanu liy sax abadan, kon lii ñu wax ci mbind mi mat:«yàlla noot na dee, ba labal ko ci ndamam.

French

lorsque ce corps corruptible aura revêtu l`incorruptibilité, et que ce corps mortel aura revêtu l`immortalité, alors s`accomplira la parole qui est écrite: la mort a été engloutie dans la victoire.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,794,038,763 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK