Results for loutakh ma bëgg la translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:

French

nous vous y trompez pas, mes frères bien-aimés:

Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 31
Quality:

Wolof

te fàttewuma ampilyaatus, mi ma bëgg ci sama xol ngir boroom bi.

French

saluez amplias, mon bien-aimé dans le seigneur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man maay yedd, di yar ñépp ñi ma bëgg. farlul kon te tuub say bàkkaar.

French

moi, je reprends et je châtie tous ceux que j`aime. aie donc du zèle, et repens-toi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man njiit li, maa ngi lay bind, yaw sama xarit gayus, mi ma bëgg ci sama xol.

French

l`ancien, à gaïus, le bien aimé, que j`aime dans la vérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi lay bind timote, sama doomu diine ji ma bëgg. na la yàlla baay bi ak kirist yeesu sunu boroom may yiw, yërmande ak jàmm.

French

à timothée, mon enfant bien-aimé: que la grâce, la miséricorde et la paix te soient données de la part de dieu le père et de jésus christ notre seigneur!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne leen: «sama xol dafa tiis, ba ma bëgg a dee; toogleen fii, xool.»

French

il leur dit: mon âme est triste jusqu`à la mort; restez ici, et veillez.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte samay jëf jaaxal na ma; li ma bëgg a def, duma ko def, waaye li ma bañ rekk, moom laay def.

French

car je ne sais pas ce que je fais: je ne fais point ce que je veux, et je fais ce que je hais.

Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 31
Quality:

Wolof

li ma bëgg kon mooy lii: na góor ñi ñaan ci yàlla fu nekk, tàllal ko loxo yu sell, te bañ cee boole mer mbaa werante.

French

je veux donc que les hommes prient en tout lieu, en élevant des mains pures, sans colère ni mauvaises pensées.

Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 21
Quality:

Wolof

noonu agaripa ne pool: «xanaa yaw, ci diir bu gàtt bii rekk, nga ma bëgg a dugale ci gaayi kirist!»

French

et agrippa dit à paul: tu vas bientôt me persuader de devenir chrétien!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ku ma bëgg dina sàmm sama kàddu. sama baay dina ko bëgg te nun dinanu ñëw ci moom, te dëkk ci moom.

French

jésus lui répondit: si quelqu`un m`aime, il gardera ma parole, et mon père l`aimera; nous viendrons à lui, et nous ferons notre demeure chez lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu niir muur leen, te baat jibe ca niir wa naan: «kii mooy sama doom ji ma bëgg, ci moom laa ame bànneex; dégluleen ko.»

French

une nuée vint les couvrir, et de la nuée sortit une voix: celui-ci est mon fils bien-aimé: écoutez-le!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne leen: «bu yàlla doon seen baay, dingeen ma bëgg, ndaxte ca moom laa jóge, ñëw ci ndigalam. Ñëwaluma sama bopp, waaye moo ma yónni.

French

jésus leur dit: si dieu était votre père, vous m`aimeriez, car c`est de dieu que je suis sorti et que je viens; je ne suis pas venu de moi-même, mais c`est lui qui m`a envoyé.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,793,675,061 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK