Results for maana translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

«su ma seedeelee sama bopp, sama wax du am maana.

French

si c`est moi qui rends témoignage de moi-même, mon témoignage n`est pas vrai.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag yawut yu bare gëm ak ñu bare ci gereg yi, di jigéen yu am maana ak ay góor.

French

plusieurs d`entre eux crurent, ainsi que beaucoup de femmes grecques de distinction, et beaucoup d`hommes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye yeesu yelloo na ndam lu sut lu musaa, ni kiy tabax kër ëppe maana kër ga muy tabax.

French

car il a été jugé digne d`une gloire d`autant supérieure à celle de moïse que celui qui a construit une maison a plus d`honneur que la maison même.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te cér yi gën a ñàkk maana, ñoom lanuy gën a topptoo. cér yi ci rafetul a tudd, ñoom lanuy gën a suturaal,

French

et ceux que nous estimons être les moins honorables du corps, nous les entourons d`un plus grand honneur. ainsi nos membres les moins honnêtes reçoivent le plus d`honneur,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndax tabaxkatu ndaa sañul a fab banam, tabax ci ñaari ndaa, benn bi ngir soxla yu am maana, bi ci des ngir soxla yu ndaw?

French

le potier n`est-il pas maître de l`argile, pour faire avec la même masse un vase d`honneur et un vase d`un usage vil?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne leen: «Ñi am maana ci yéen nag, nangeen ànd ak man, layooji ak nit ka, bu dee tooñ na.»

French

que les principaux d`entre vous descendent avec moi, dit-il, et s`il y a quelque chose de coupable en cet homme, qu`ils l`accusent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te sooy ñëw, indaaleel mbubb, ma ma dénkoon karpus ca dëkku torowas, te it bul fàtte téere yi, rawatina téere yu am maana, yi ñu bind ci der.

French

quand tu viendras, apporte le manteau que j`ai laissé à troas chez carpus, et les livres, surtout les parchemins.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

seetleen picci asamaan: duñu ji, duñu góob, duñu denc ci sàq; teewul seen baay bi ci kaw moo leen di dundal. ndax ëppuleen maana picc yi ci lu bare?

French

regardez les oiseaux du ciel: ils ne sèment ni ne moissonnent, et ils n`amassent rien dans des greniers; et votre père céleste les nourrit. ne valez-vous pas beaucoup plus qu`eux?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne leen: «kon nag, bi ñu leen sóobee ci ndox, lu ciy maana?» Ñu tontu ko: «xanaa li yaxya tëral.»

French

il dit: de quel baptême avez-vous donc été baptisés? et ils répondirent: du baptême de jean.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,934,695,279 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK