From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ndaxte ni baay bi ame dund moom ci boppam, noonu it la ko maye doom ji, mu am ko ci boppam.
car, comme le père a la vie en lui-même, ainsi il a donné au fils d`avoir la vie en lui-même.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndax li yàlla maye, dootu ko nangu mukk, te ku mu woo ci boppam, dootu la dàq mukk.
car dieu ne se repent pas de ses dons et de son appel.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te yàlla, mi xam xol yi, seede na leen ci li mu leen may xel mu sell mi, ni mu nu ko maye nun itam.
et dieu, qui connaît les coeurs, leur a rendu témoignage, en leur donnant le saint esprit comme à nous;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
maye na leen, ngir ñu waajal gaayi yàlla yu sell yi, ñu man a bey seen sas ci taxawal mbooloom kirist, di jëmmam.
pour le perfectionnement des saints en vue de l`oeuvre du ministère et de l`édification du corps de christ,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yawut yi gëm yépp nag, ñi ànd ak piyeer, daldi waaru ci li yàlla tuur xel mu sell, mi mu maye, ci ñi dul yawut itam.
tous les fidèles circoncis qui étaient venus avec pierre furent étonnés de ce que le don du saint esprit était aussi répandu sur les païens.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
péete ak dayoo bees laaj ngir crtc %d romb na dig bees maye: péete=(%d, %d), dayoo=(%d, %d), bi ëpp=(%d, %d)
la taille et la position demandées au crtc %d sont hors des limites autorisées : position=(%d, %d), taille=(%d, %d), maximum=(%d, %d)
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality: