Results for mer translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

waaye nit ña mer ba fees, di rabat pexe yu jëm ca yeesu.

French

ils furent remplis de fureur, et ils se consultèrent pour savoir ce qu`ils feraient à jésus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku mer, bu mu jàll aw kaañ; bu jant bi sowaale seen mer,

French

si vous vous mettez en colère, ne péchez point; que le soleil ne se couche pas sur votre colère,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu déggee wax yooya, ñépp ña nekkoon ca jàngu ba daldi fees ak mer.

French

ils furent tous remplis de colère dans la synagogue, lorsqu`ils entendirent ces choses.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

dëdduleen lépp luy wex mbaa tàng bopp, luy mer mbaa coow, lépp luy xaste mbaa coxor.

French

que toute amertume, toute animosité, toute colère, toute clameur, toute calomnie, et toute espèce de méchanceté, disparaissent du milieu de vous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu mer lool ci li ñuy waar nit ñi, di yégle ndekkitel ñi dee, sukkandikoo ko ci ndekkitel yeesu.

French

mécontents de ce qu`ils enseignaient le peuple, et annonçaient en la personne de jésus la résurrection des morts.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«noonu buur mer, daldi yónni ay xarekatam, ngir ñu rey bóomkat yooyule, lakk seen dëkk.

French

le roi fut irrité; il envoya ses troupes, fit périr ces meurtriers, et brûla leur ville.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye léegi bàyyileen yii yépp: mer, xadar, kiñaan ak di génne ci seen gémmiñ sos ak wax ju ñaaw.

French

mais maintenant, renoncez à toutes ces choses, à la colère, à l`animosité, à la méchanceté, à la calomnie, aux paroles déshonnêtes qui pourraient sortir de votre bouche.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li ma bëgg kon mooy lii: na góor ñi ñaan ci yàlla fu nekk, tàllal ko loxo yu sell, te bañ cee boole mer mbaa werante.

French

je veux donc que les hommes prient en tout lieu, en élevant des mains pures, sans colère ni mauvaises pensées.

Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 31
Quality:

Wolof

xeet yi meroon nañu,waaye sa mer wàcc na,te jamono ji jot na,ji ngay àttee ñi dee,neexal say jaam yonent yi,ak sa gaa ñi ak ñi ragal saw tur,muy mag di ndaw,te nga rey ñiy yàq àddina.»

French

les nations se sont irritées; et ta colère est venue, et le temps est venu de juger les morts, de récompenser tes serviteurs les prophètes, les saints et ceux qui craignent ton nom, les petits et les grands, et de détruire ceux qui détruisent la terre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,874,838,149 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK