Results for nawle translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

soo ma jàppee ni nawle nag, teeru ko, ni su ma la doon ganesi.

French

si donc tu me tiens pour ton ami, reçois-le comme moi-même.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nuyul-leen ma pirsil ak akilas, samay nawle ci liggéeyu kirist yeesu.

French

saluez prisca et aquilas, mes compagnons d`oeuvre en jésus christ,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nuyul-leen ma it urban, sunu nawle ci liggéeyu kirist, ak sama soppe estakis;

French

saluez urbain, notre compagnon d`oeuvre en christ, et stachys, mon bien-aimé.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

timote sama nawle bi may jàpple ci liggéey bi, mu ngi leen di nuyu, ak samay bokk lusiyus, yason ak sosipater.

French

timothée, mon compagnon d`oeuvre, vous salue, ainsi que lucius, jason et sosipater, mes parents.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

tisig, sama mbokk mi ma sopp, di jawriñ ju takku ak sama nawle ci liggéeyu boroom bi, dina leen yégal lépp lu jëm ci samay mbir.

French

tychique, le bien-aimé frère et le fidèle ministre, mon compagnon de service dans le seigneur, vous communiquera tout ce qui me concerne.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te yónni nanu timote, sunu mbokk ak sunu nawle ci liggéeyu yàlla ak ci waareb xebaaru kirist. yónni nanu ko, ngir mu dénk leen, tey feddali seen ngëm,

French

nous envoyâmes timothée, notre frère, ministre de dieu dans l`Évangile de christ, pour vous affermir et vous exhorter au sujet de votre foi,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci lu jëm ci sama mbokk epafrodit nag, miy sama nawle ci liggéey bi ak ci xeex bi, te di seen ndaw ci faj samay soxla, jàpp naa ne, war naa leen koo delloo.

French

j`ai estimé nécessaire de vous envoyer mon frère Épaphrodite, mon compagnon d`oeuvre et de combat, par qui vous m`avez fait parvenir de quoi pourvoir à mes besoins.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te yaw sama nawle bu wér, nanga dimbali jigéen ñooñu xeexoon ci sama wet ci tas xebaar bu baax bi, boole ci këlemaŋ ak samay yeneeni nawle, ñoom ñi yàlla bind seeni tur ci téereb dund ba.

French

et toi aussi, fidèle collègue, oui, je te prie de les aider, elles qui ont combattu pour l`Évangile avec moi, et avec clément et mes autres compagnons d`oeuvre, dont les noms sont dans le livre de vie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu kon ci lu jëm ci tit, sama nawle la ci liggéey, bi ci seen biir. ci lu jëm ci sunu bokk, yi ànd ak moom nag, ndawi mbooloom ñi gëm lañu, ñuy wone ndamu kirist.

French

ainsi, pour ce qui est de tite, il est notre associé et notre compagnon d`oeuvre auprès de vous; et pour ce qui est de nos frères, ils sont les envoyés des Églises, la gloire de christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye mu ne ma: «moytu koo def. sa nawle laa ci liggéey bi, yaw ak say bokki yonent ak ñiy sàmm waxi téere bii. jaamul yàlla.»

French

mais il me dit: garde-toi de le faire! je suis ton compagnon de service, et celui de tes frères les prophètes, et de ceux qui gardent les paroles de ce livre. adore dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ma daanu ci ay tànkam, bëgg koo jaamu. waaye mu ne ma: «moytu koo def; sa nawle laa ci liggéey bi, di kenn ci say bokk, yiy sax ci seedeel yeesu. jaamul yàlla. ndaxte seedes yeesu mooy xel miy solu yonent yi.»

French

et je tombai à ses pieds pour l`adorer; mais il me dit: garde-toi de le faire! je suis ton compagnon de service, et celui de tes frères qui ont le témoignage de jésus. adore dieu. -car le témoignage de jésus est l`esprit de la prophétie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,920,049,206 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK