Results for ndamam translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ci biir xel moomu la yégaleji ndamam ca ruu ya yàlla tëj kaso;

French

dans lequel aussi il est allé prêcher aux esprits en prison,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu nuy jollil ndamam, nun ñi jëkk a wékk sunu yaakaar ci kirist.

French

afin que nous servions à la louange de sa gloire, nous qui d`avance avons espéré en christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

seen pey mooy alku ba fàww, ñu dàq leen fu sore boroom bi ak ndamam lu réy.

French

ils auront pour châtiment une ruine éternelle, loin de la face du seigneur et de la gloire de sa force,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa du almasi bi dafa waroon a daj boobu coono te dugg ci ndamam?»

French

ne fallait-il pas que le christ souffrît ces choses, et qu`il entrât dans sa gloire?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye maa ngi leen di wax ne, suleymaan sax ci ndamam soluwul woon ni benn ci ñoom.

French

cependant je vous dis que salomon même, dans toute sa gloire, n`a pas été vêtu comme l`un d`eux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu nag ñàkkuleen genn may léegi bi ngeen di séentu waxtu, wi sunu boroom yeesu kirist di feeñ ci biir ndamam.

French

de sorte qu`il ne vous manque aucun don, dans l`attente où vous êtes de la manifestation de notre seigneur jésus christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bëggoon na it xamle màggaayam mu ëpp xel, ci boole ñi mu yërëm ci ndamam; moo tax mu tànn leen ca njàlbéen.

French

et s`il a voulu faire connaître la richesse de sa gloire envers des vases de miséricorde qu`il a d`avance préparés pour la gloire?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bégleen ci cér, boobu ngeen am ci coonoy kirist, ngir bés bu ndamam di feeñ, ngeen bég ak mbég mu ëpp xel.

French

réjouissez-vous, au contraire, de la part que vous avez aux souffrances de christ, afin que vous soyez aussi dans la joie et dans l`allégresse lorsque sa gloire apparaîtra.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te xel mi mooy dawal gi nu yàlla jox ci cér, bi mu nu dencal, ba kera muy goreel ñi mu jotal boppam, te ñépp jollil ndamam.

French

lequel est un gage de notre héritage, pour la rédemption de ceux que dieu s`est acquis, à la louange de sa gloire.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kàddu gi ñëw, doon nit, dëkk ci sunu biir. gis nañu ndamam, mu fees ak yiw ak dëgg, ndam li baay bi jox jenn doomam ji mu am kepp.

French

et la parole a été faite chair, et elle a habité parmi nous, pleine de grâce et de vérité; et nous avons contemplé sa gloire, une gloire comme la gloire du fils unique venu du père.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku ma rus a faral, te nanguwul samay wax, doomu nit ki dina la rus a xam, bés bu ñëwee ci ndamam ak ci ndamu baay bi ak lu malaaka yu sell yi.

French

car quiconque aura honte de moi et de mes paroles, le fils de l`homme aura honte de lui, quand il viendra dans sa gloire, et dans celle du père et des saints anges.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte lépp li nuy daj, seen njariñ a tax, ngir yiwu yàlla, wiy yokku ci nit ñu gën a takku, yokkaale ngërëm lu jëm ci yàlla, ngir jollil ndamam.

French

car tout cela arrive à cause de vous, afin que la grâce en se multipliant, fasse abonder, à la gloire de dieu, les actions de grâces d`un plus grand nombre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte yàlla mi yelloo lépp te sàkk lépp, dogal na def ñu bare ay doomam, boole leen ci ndamam. jekk na nag mu matal yeesu ci coono bi mu daj, moom mi leen xàllal yoonu mucc gi.

French

il convenait, en effet, que celui pour qui et par qui sont toutes choses, et qui voulait conduire à la gloire beaucoup de fils, élevât à la perfection par les souffrances le prince de leur salut.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te ñi mu dogaloon loolu ci ñoom, da leen a woo; te ñooñu mu woo, da leen a àtte ni ñu jub; te ñooñu mu àtte jub, da leen a boole ca ndamam.

French

et ceux qu`il a prédestinés, il les a aussi appelés; et ceux qu`il a appelés, il les a aussi justifiés; et ceux qu`il a justifiés, il les a aussi glorifiés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

léegi kat loraangee ngi nuy yoot, te du yem ci xañ nu sunu liggéey rekk, waaye it dina daaneel màggalukaayu artemis sunu yàlla ju mag ji, tey neenal ndamam, moom mi asi gépp te àddina sépp di màggal.»

French

le danger qui en résulte, ce n`est pas seulement que notre industrie ne tombe en discrédit; c`est encore que le temple de la grande déesse diane ne soit tenu pour rien, et même que la majesté de celle qui est révérée dans toute l`asie et dans le monde entier ne soit réduite à néant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bànni israyil lañu, te yàlla def na leen ni ay doomam; dëkkaloon na ndamam ci seen biir, fas ak ñoom kóllëre yi. Ñoom la yàlla dénk yoonu musaa, ñoom la xamal ni ñu ko war a jaamoo, ñoom la jox i digam.

French

qui sont israélites, à qui appartiennent l`adoption, et la gloire, et les alliances, et la loi, et le culte,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,856,453 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK