Results for ndokkale ci ndam li translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ndaxte ndam li amoon keroog suux na ci ndam li ko raw léegi.

French

et, sous ce rapport, ce qui a été glorieux ne l`a point été, à cause de cette gloire qui lui est supérieure.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

boole naa leen ci ndam, li nga ma sol, ngir ñu àndandoo, ni nu ànde man ak yaw.

French

je leur ai donné la gloire que tu m`as donnée, afin qu`ils soient un comme nous sommes un, -

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

léegi nag baay, ci sa teewaay, feeñalal ci man ndam, li ma amoon ci sa wet, laata àddina di sosu.

French

et maintenant toi, père, glorifie-moi auprès de toi-même de la gloire que j`avais auprès de toi avant que le monde fût.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nanu bég te bànneexute jox ko ndam li,ndaxte céetu mbote mi agsi na,séet bi waaj na.

French

réjouissons-nous et soyons dans l`allégresse, et donnons-lui gloire; car les noces de l`agneau sont venues, et son épouse s`est préparée,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye damay noot sama yaram, ba moom ko, ngir ragal a yégal ñi ci des xebaar bu baax bi, ba noppi yàlla xañ ma ndam li.

French

mais je traite durement mon corps et je le tiens assujetti, de peur d`être moi-même rejeté, après avoir prêché aux autres.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kàddu gi ñëw, doon nit, dëkk ci sunu biir. gis nañu ndamam, mu fees ak yiw ak dëgg, ndam li baay bi jox jenn doomam ji mu am kepp.

French

et la parole a été faite chair, et elle a habité parmi nous, pleine de grâce et de vérité; et nous avons contemplé sa gloire, une gloire comme la gloire du fils unique venu du père.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye jërë-jëf yaw yàlla, ji nu jox ndam li jaarale ko ci sunu boroom yeesu kirist!

French

mais grâces soient rendues à dieu, qui nous donne la victoire par notre seigneur jésus christ!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa xamuleen ne, ñépp ñooy daw cib rawante, waaye kenn rekk ay jël ndam li? dawleen nag ngir jël ko.

French

ne savez-vous pas que ceux qui courent dans le stade courent tous, mais qu`un seul remporte le prix? courez de manière à le remporter.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.

French

mais ce qui est spirituel n`est pas le premier, c`est ce qui est animal; ce qui est spirituel vient ensuite.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naaj wu metti di lakk nit ñi, ñu daldi xarab turu yàlla, ji am sañ-sañ ci kaw musiba yooyu. waaye tuubuñu sax seeni bàkkaar, ngir jox ko ndam li.

French

et les hommes furent brûlés par une grande chaleur, et ils blasphémèrent le nom du dieu qui a l`autorité sur ces fléaux, et ils ne se repentirent pas pour lui donner gloire.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

léegi nag, na ndam li féete ak yàlla, mi man a yeggale lépp luy ñaan mbaa yéene, ba weesu ko fuuf, dëppook kàttan giy jëf ci nun;

French

or, à celui qui peut faire, par la puissance qui agit en nous, infiniment au delà de tout ce que nous demandons ou pensons,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«baay, bëgg naa, ñi nga ma dénk nekk ak man fa ma jëm, ngir ñu gis sama ndam, li nga ma sol, ndaxte bëgg nga ma, laata àddina di sosu.

French

père, je veux que là où je suis ceux que tu m`as donnés soient aussi avec moi, afin qu`ils voient ma gloire, la gloire que tu m`as donnée, parce que tu m`as aimé avant la fondation du monde.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ma nga doon xaacu naan: «ragal-leen yàlla te jox ko ndam li, ndaxte waxtuw àtteem jot na. jaamuleen ki sàkk asamaan ak suuf ak géej ak bëti ndox yi.»

French

il disait d`une voix forte: craignez dieu, et donnez-lui gloire, car l`heure de son jugement est venue; et adorez celui qui a fait le ciel, et la terre, et la mer, et les sources d`eaux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,772,886,276 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK