Results for nekkati translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ndax kon nit laay wut a gëmloo, am damay fexee yey yàlla? mbaa damay wut a neex nit ñi? su ma doon wut a neex nit ñi ba tey, kon duma nekkati jaamu kirist.

French

et maintenant, est-ce la faveur des hommes que je désire, ou celle de dieu? est-ce que je cherche à plaire aux hommes? si je plaisais encore aux hommes, je ne serais pas serviteur de christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waa ja woo ko ne ko: “li may dégg ci yaw mooy lan? leeralal ma ni nga liggéeye ak sama alal, ndaxte dootoo nekkati sama bëkk-néeg.”

French

il l`appela, et lui dit: qu`est-ce que j`entends dire de toi? rends compte de ton administration, car tu ne pourras plus administrer mes biens.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,791,601,138 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK