Results for pool translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

noonu pool génn ci seen biir.

French

ainsi paul se retira du milieu d`eux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man pool maa bind nuyoo bii ci sama loxob bopp.

French

je vous salue, moi paul, de ma propre main.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu wéyee pool bàyyikoo aten, dem korent.

French

après cela, paul partit d`athènes, et se rendit à corinthe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye pool yëlëb rab wa ca safara sa, te wàññiwu ko dara.

French

paul secoua l`animal dans le feu, et ne ressentit aucun mal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool nag bëgg a dugg ca mbooloo ma, waaye taalibe ya nanguwuñu ko.

French

paul voulait se présenter devant le peuple, mais les disciples l`en empêchèrent;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ca ëllëg sa pool ànd ak nun, seeti saag, fekk njiit yépp teew fa.

French

le lendemain, paul se rendit avec nous chez jacques, et tous les anciens s`y réunirent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, man ak sosten sunu mbokk,

French

paul, appelé à être apôtre de jésus christ par la volonté de dieu, et le frère sosthène,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci ndigalu yàlla sunu musalkat ak kirist yeesu sunu yaakaar,

French

paul, apôtre de jésus christ, par ordre de dieu notre sauveur et de jésus christ notre espérance,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu xarekat ya jël pool ci guddi, indi ko ba ca dëkku antipataris, ni ñu leen ko sante.

French

les soldats, selon l`ordre qu`ils avaient reçu, prirent paul, et le conduisirent pendant la nuit jusqu`à antipatris.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

tàggoo bii maa ko bind ci sama loxo, man pool. nii laay binde, te di màndargaale nii sama bataaxal yépp.

French

je vous salue, moi paul, de ma propre main. c`est là ma signature dans toutes mes lettres; c`est ainsi que j`écris.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool nag dugg ca ñoom, na mu ko daan defe, ba am fa ñetti bésu noflaay, muy werante ak ñoom ci li mbind mi wax.

French

paul y entra, selon sa coutume. pendant trois sabbats, il discuta avec eux, d`après les Écritures,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te jàppleen ne, muñug sunu boroom muccu nit la. sunu mbokk mi nu bëgg pool bind na leen ko, ci xel mi ko yàlla sol.

French

croyez que la patience de notre seigneur est votre salut, comme notre bien-aimé frère paul vous l`a aussi écrit, selon la sagesse qui lui a été donnée.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu pool taxaw ci biir mbooloom areyopas ne leen: «yéen waa aten gis naa ne, farlu ngeen ci diine lool.

French

paul, debout au milieu de l`aréopage, dit: hommes athéniens, je vous trouve à tous égards extrêmement religieux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi mbooloo ma gisee li pool def, ñu daldi yuuxu, ne ci làkku waa likawni: «yàlla yi soppiku nañu nit, wàcc ci nun.»

French

a la vue de ce que paul avait fait, la foule éleva la voix, et dit en langue lycaonienne: les dieux sous une forme humaine sont descendus vers nous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,790,833,098 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK