Results for réseñ translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

dingeen leen xàmmee ci seeni jëf. ndax dees na witte réseñ ci dédd, walla figg ci xaaxaam?

French

vous les reconnaîtrez à leurs fruits. cueille-t-on des raisins sur des épines, ou des figues sur des chardons?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte maa ngi leen koy wax, dootuma naan ndoxum réseñ mi, ba kera yàlla di tëral nguuram.»

French

car, je vous le dis, je ne boirai plus désormais du fruit de la vigne, jusqu`à ce que le royaume de dieu soit venu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu malaaka ma daldi dawal sàrtam ci àddina, dagg réseñ yi, sànni leen ci biir segalukaay bu réy bu merum yàlla.

French

et l`ange jeta sa faucille sur la terre. et il vendangea la vigne de la terre, et jeta la vendange dans la grande cuve de la colère de dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«bi nga xamee ne bëgg nañoo witt réseñ yi, mu yónni ay surgaam ci beykat yi, ngir jot wàllam ci meññeef mi.

French

lorsque le temps de la récolte fut arrivé, il envoya ses serviteurs vers les vignerons, pour recevoir le produit de sa vigne.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi leen di wax, dootuma naan gannaawsi tey ndoxum réseñ mii, ba kera may naan ak yéen ndoxum réseñ mu bees ci sama nguuru baay.»

French

je vous le dis, je ne boirai plus désormais de ce fruit de la vigne, jusqu`au jour où j`en boirai du nouveau avec vous dans le royaume de mon père.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu nal réseñ ya ca segalukaay, ba ca gannaaw dëkk ba, deret génn ca, ba agsi ci laabi fas yi, te wal ba ëmb lu mat ñetti téeméeri kilomet.

French

et la cuve fut foulée hors de la ville; et du sang sortit de la cuve, jusqu`aux mors des chevaux, sur une étendue de mille six cents stades.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yeesu daldi wax nit ña léeb wii: «amoon na nit ku jëmbët toolu réseñ, batale ko ay beykat, dem tukki tukki bu yàgg.

French

il se mit ensuite à dire au peuple cette parabole: un homme planta une vigne, l`afferma à des vignerons, et quitta pour longtemps le pays.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay bokk, ndax mas ngeen a gis garabu figg gu meññ oliw, walla garabu réseñ gu meññ ay figg? mukk! mbënnu xorom mënta nàcc mukk ndox mu neex.

French

un figuier, mes frères, peut-il produire des olives, ou une vigne des figues? de l`eau salée ne peut pas non plus produire de l`eau douce.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu meneen malaaka, ma am sañ-sañ ca safara sa, jóge ca saraxalukaayu cuuraay ba, daldi wax ak baat bu xumb ak malaaka, ma yor sàrt bu ñaw ba, ne ko: «dawalal sa sàrt bu ñaw bi te dagg céggu réseñ yu àddina, ndaxte ñor nañu.»

French

et un autre ange, qui avait autorité sur le feu, sortit de l`autel, et s`adressa d`une voix forte à celui qui avait la faucille tranchante, disant: lance ta faucille tranchante, et vendange les grappes de la vigne de la terre; car les raisins de la terre sont mûrs.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,875,145 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK