Results for sóob translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ngir kenn bañ a wax ne, ci sama tur lañu ko sóob.

French

afin que personne ne dise que vous avez été baptisés en mon nom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu nangu seeni bàkkaar, yaxya sóob leen ca dexu yurdan.

French

et, confessant leurs péchés, ils se faisaient baptiser par lui dans le fleuve du jourdain.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fàww ñu sóob ma ci metit, te ba looluy mat, duma noppalu.

French

il est un baptême dont je dois être baptisé, et combien il me tarde qu`il soit accompli!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sol na mbubb mu ñu sóob ci deret, te kàddug yàlla mooy turam.

French

et il était revêtu d`un vêtement teint de sang. son nom est la parole de dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu déggee loolu nag, sóob nañu leen ci ndox ci turu yeesu boroom bi.

French

sur ces paroles, ils furent baptisés au nom du seigneur jésus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen ñépp, ñi ñu sóob ci ndox ngir wone seen bokk ci kirist, soloo ngeen kirist.

French

vous tous, qui avez été baptisés en christ, vous avez revêtu christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku gëm te ñu sóob ko ci ndox, dina mucc; ku gëmul, dees na ko daan.

French

celui qui croira et qui sera baptisé sera sauvé, mais celui qui ne croira pas sera condamné.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

booba yeesu jóge na dëkku nasaret ci diiwaanu galile, ñëw, yaxya sóob ko ci dexu yurdan.

French

en ce temps-là, jésus vint de nazareth en galilée, et il fut baptisé par jean dans le jourdain.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te waa réew ma won nu laabiir gu ràññiku, ndaxte taalal nañu nu safara, ganale nu ndax taw bi sóob ak sedd bi.

French

les barbares nous témoignèrent une bienveillance peu commune; ils nous recueillirent tous auprès d`un grand feu, qu`ils avaient allumé parce que la pluie tombait et qu`il faisait grand froid.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñi nangu ay waxam nag, ñu sóob leen ci ndox, te ca bés booba lu mat limub ñetti junniy nit yokku nañu ci ñoom.

French

ceux qui acceptèrent sa parole furent baptisés; et, en ce jour-là, le nombre des disciples s`augmenta d`environ trois mille âmes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu santaane nag, ñu taxawal watiir wa; filib ak jaraaf ja wàcc ñoom ñaar ci biir ndox ma, mu sóob ko ca.

French

il fit arrêter le char; philippe et l`eunuque descendirent tous deux dans l`eau, et philippe baptisa l`eunuque.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye bi ñu gëmee xebaar bu baax, bi filib yégle jëm ci nguurug yàlla ak turu yeesu kirist, góor ak jigéen daldi nangu, ñu sóob leen ci ndox.

French

mais, quand ils eurent cru à philippe, qui leur annonçait la bonne nouvelle du royaume de dieu et du nom de jésus christ, hommes et femmes se firent baptiser.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man maa ngi leen di sóob ci ndox, ci lu ànd ak tuub seeni bàkkaar. waaye kiy ñëw sama gannaaw moo ma ëpp kàttan, ba yeyoowuma koo yóbbul sax ay dàllam. kooku dina leen sóob ci xel mu sell mi ak safara.

French

moi, je vous baptise d`eau, pour vous amener à la repentance; mais celui qui vient après moi est plus puissant que moi, et je ne suis pas digne de porter ses souliers. lui, il vous baptisera du saint esprit et de feu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,707,985 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK