From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Ñi ma fi jiitu ñépp ay sàcc lañu, ak ay saay-saay; waaye xar yi dégluwuñu leen.
tous ceux qui sont venus avant moi sont des voleurs et des brigands; mais les brebis ne les ont point écoutés.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku jaar feneen fu dul ci buntu gétt gi, kooku sàcc la, saay-saay la.
en vérité, en vérité, je vous le dis, celui qui n`entre pas par la porte dans la bergerie, mais qui y monte par ailleurs, est un voleur et un brigand.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«baat jib na ci rama,ay jooy ak yuux gu réy,rasel mooy jooy ay doomamte bëggul kenn dëfël ko,ndaxte saay nañu.»
on a entendu des cris à rama, des pleurs et de grandes lamentations: rachel pleure ses enfants, et n`a pas voulu être consolée, parce qu`ils ne sont plus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.