From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sama
ma
Last Update: 2024-04-26
Usage Frequency: 26
Quality:
«yeesu, kilifa gi, yërëm nu!»
jésus, maître, aie pitié de nous!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moom kenn mooy boroom bu tedd, di buuru buur yi ak kilifag kilifa yi.
que manifestera en son temps le bienheureux et seul souverain, le roi des rois, et le seigneur des seigneurs,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te mat ngeen ci moom, miy buuru kilifa yépp ak boroom sañ-sañ yépp.
vous avez tout pleinement en lui, qui est le chef de toute domination et de toute autorité.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
buleen mel ni ñooñu. waaye ku bëgg a nekk kilifa ci yéen, na nekk seen surga,
il n`en est pas de même au milieu de vous. mais quiconque veut être grand parmi vous, qu`il soit votre serviteur;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci mbubbam ak ci poojam bind nañu ci tur wii: buuru buur yi, kilifag kilifa yi.
il avait sur son vêtement et sur sa cuisse un nom écrit: roi des rois et seigneur des seigneurs.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ñu ne yeesu: «kilifa gi, jigéen jii de, dañu koo bett muy njaaloo.
et, la plaçant au milieu du peuple, ils dirent à jésus: maître, cette femme a été surprise en flagrant délit d`adultère.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ñi dul yawut ak yawut yi, ñoom ak seeni kilifa, lal pexem fitnaal leen ci sànni ay doj.
et comme les païens et les juifs, de concert avec leurs chefs, se mettaient en mouvement pour les outrager et les lapider,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
fekk sax malaaka, yi leen ëpp doole ak kàttan, tey sax ca jetaayu boroom bi, ñemewuñoo xas kilifa yooyu.
tandis que les anges, supérieurs en force et en puissance, ne portent pas contre elles de jugement injurieux devant le seigneur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ay farisen yu nekkoon ca mbooloo ma ne yeesu: «kilifa gi, yeddal sa taalibe yi!»
quelques pharisiens, du milieu de la foule, dirent à jésus: maître, reprends tes disciples.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.
mais vous, ne vous faites pas appeler rabbi; car un seul est votre maître, et vous êtes tous frères.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nit xaacu ci biir mbooloo mi naan: «kilifa gi, maa ngi lay ñaan, nga seet sama doom, ndaxte moom kepp laa am.
et voici, du milieu de la foule un homme s`écria: maître, je t`en prie, porte les regards sur mon fils, car c`est mon fils unique.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu laaj ko ne: «kilifa gi, kañ la loolu di am? te luy tegtal ne, looloo ngi waaj a xew?»
ils lui demandèrent: maître, quand donc cela arrivera-t-il, et à quel signe connaîtra-t-on que ces choses vont arriver?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu woo leen ne leen: «xam ngeen ne ci xeeti àddina, njiit yi dañu leen di dóor yetu nguur, te kilifa yi dañu leen di noot.
jésus les appela, et dit: vous savez que les chefs des nations les tyrannisent, et que les grands les asservissent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«kilifa gi, musaa bindal na nu ne, ku magam faatu te bàyyiwul doom ak jabaram, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam.
maître, voici ce que moïse nous a prescrit: si le frère de quelqu`un meurt, ayant une femme sans avoir d`enfants, son frère épousera la femme, et suscitera une postérité à son frère.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu ay xutbakat ak ay farisen wax ak yeesu ne ko: «kilifa gi, danoo bëggoon, nga won nu kéemaan guy firndeel sag yónnent.»
alors quelques-uns des scribes et des pharisiens prirent la parole, et dirent: maître, nous voudrions te voir faire un miracle.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te ngeen ne boroom kër ga: “kilifa gi nee na: ana néegu gan, bi may lekke reeru jéggi ba, man ak samay taalibe?”
et vous direz au maître de la maison: le maître te dit: où est le lieu où je mangerai la pâque avec mes disciples?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yudaa, mi ko nar a wor, laaj ko: «mbaa du man, kilifa gi?» yeesu ne ko: «wax nga ko.»
judas, qui le livrait, prit la parole et dit: est-ce moi, rabbi? jésus lui répondit: tu l`as dit.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: