From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
kiy lekk sama yaram tey naan sama deret dina sax ci man, ma dëkk ci moom.
celui qui mange ma chair et qui boit mon sang demeure en moi, et je demeure en lui.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte sama yaram mooy ñam wu wóor wi, te sama deret mooy naan gu wóor gi.
car ma chair est vraiment une nourriture, et mon sang est vraiment un breuvage.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moo tax sama xol sedd,may woy sama bànneex,te it sama yaram di tëdd ci yaakaar.
aussi mon coeur est dans la joie, et ma langue dans l`allégresse; et même ma chair reposera avec espérance,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
céy maaka torox! ana ku may musal ci sama yaram, wii may jëme ci dee?
misérable que je suis! qui me délivrera du corps de cette mort?...
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jigéen ji def na li mu man; diw na sama yaram ak latkoloñ, ngir waajal sama rob, laata moo jot.
elle a fait ce qu`elle a pu; elle a d`avance embaumé mon corps pour la sépulture.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
léegi nag, bu ma kenn lëjalati, ndaxte yor naa ci sama yaram ay leget yuy màndargaal ne, jaamu yeesu laa.
que personne désormais ne me fasse de la peine, car je porte sur mon corps les marques de jésus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye damay noot sama yaram, ba moom ko, ngir ragal a yégal ñi ci des xebaar bu baax bi, ba noppi yàlla xañ ma ndam li.
mais je traite durement mon corps et je le tiens assujetti, de peur d`être moi-même rejeté, après avoir prêché aux autres.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te it su ma doon saraxe li ma am lépp, di bàyyi ñu lakk sama yaram, ba rey ma, su ma ci boolewul mbëggeel, du ma jariñ dara.
et quand je distribuerais tous mes biens pour la nourriture des pauvres, quand je livrerais même mon corps pour être brûlé, si je n`ai pas la charité, cela ne me sert de rien.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu bi ñuy lekk, yeesu jël mburu, sant yàlla, jox leen ko naan: «jël-leen, lii sama yaram la.»
pendant qu`ils mangeaient, jésus prit du pain; et, après avoir rendu grâces, il le rompit, et le leur donna, en disant: prenez, ceci est mon corps.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te it ngir ma bañ a yég sama bopp ndax peeñu yooyu wees xel, mayees na mbir dal ma ci sama yaram, di ma metital ni dég, muy malaakam seytaane mu may sonal, ngir ma bañ a yég sama bopp.
et pour que je ne sois pas enflé d`orgueil, à cause de l`excellence de ces révélations, il m`a été mis une écharde dans la chair, un ange de satan pour me souffleter et m`empêcher de m`enorgueillir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
man maay ñam wiy dund te wàcce ci asamaan. ku lekk ci ñam wii, dinga dund ba fàww. te it ñam wi may joxeji, sama yaram la; dama koy joxe ngir àddina man a dund.»
je suis le pain vivant qui est descendu du ciel. si quelqu`un mange de ce pain, il vivra éternellement; et le pain que je donnerai, c`est ma chair, que je donnerai pour la vie du monde.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu bu ñuy lekk, yeesu jël mburu, sant yàlla, damm ko, jox ko taalibe ya. mu ne leen: «jël-leen lekk, lii sama yaram la.»
pendant qu`ils mangeaient, jésus prit du pain; et, après avoir rendu grâces, il le rompit, et le donna aux disciples, en disant: prenez, mangez, ceci est mon corps.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.