From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
yéenay samay seede.
vous êtes témoins de ces choses.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
samay doom, wottuleen seen bopp ciy xërëm.
c`est lui qui est le dieu véritable, et la vie éternelle. petits enfants, gardez-vous des idoles.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye gëmuleen ndaxte bokkuleen ci samay xar.
mais vous ne croyez pas, parce que vous n`êtes pas de mes brebis.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen nag yéenay ñi ànd ak man ci samay fitna.
vous, vous êtes ceux qui avez persévéré avec moi dans mes épreuves;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
duma noppee sant yàlla, di leen boole ci samay ñaan.
je ne cesse de rendre grâces pour vous, faisant mention de vous dans mes prières,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
asamaan ak suuf dinañu wéy, waaye samay wax du wéy mukk.
le ciel et la terre passeront, mais mes paroles ne passeront point.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 3
Quality:
ni ñuy xame ne samay taalibe ngeen, mooy ngeen bëggante.»
a ceci tous connaîtront que vous êtes mes disciples, si vous avez de l`amour les uns pour les autres.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
samay xar dinañu dégg sama baat; xam naa leen te ñu ngi may topp.
mes brebis entendent ma voix; je les connais, et elles me suivent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
samay bokk, su amee ci yéen ku réere dëgg, te am ku ko gindi,
mes frères, si quelqu`un parmi vous s`est égaré loin de la vérité, et qu`un autre l`y ramène,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
samay soppe, bu nu yàlla bëggee nii, nun itam war nanoo bëggante.
bien-aimés, si dieu nous a ainsi aimés, nous devons aussi nous aimer les uns les autres.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu joxoñ ay taalibeem naan: «Ñii ñooy sama ndey ak samay rakk.
puis, étendant la main sur ses disciples, il dit: voici ma mère et mes frères.
Last Update: 2024-06-15
Usage Frequency: 6
Quality:
képp ku ñëw ci man, di dégg samay wax te di ko jëfe, ma won leen nu muy mel.
je vous montrerai à qui est semblable tout homme qui vient à moi, entend mes paroles, et les met en pratique.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma pirsil ak akilas, samay nawle ci liggéeyu kirist yeesu.
saluez prisca et aquilas, mes compagnons d`oeuvre en jésus christ,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen samay bokk, bu benn gënale laal seen ngëm ci sunu boroom yeesu kirist, mi soloo ndam.
mes frères, que votre foi en notre glorieux seigneur jésus christ soit exempte de toute acception de personnes.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yéen samay xarit, doolewuleen ci seen yoonu ngëm wu sell, tey ñaan ci dooley xel mu sell mi,
pour vous, bien-aimés, vous édifiant vous-mêmes sur votre très sainte foi, et priant par le saint esprit,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeen samay xarit, sama ñaareelu bataaxel a ngi nii. bind naa leen, ngir xiir leen ci xalaat yu sell.
voici déjà, bien-aimés, la seconde lettre que je vous écris. dans l`une et dans l`autre je cherche à éveiller par des avertissements votre saine intelligence,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.
ce n`est pas pour vous faire honte que j`écris ces choses; mais je vous avertis comme mes enfants bien-aimés.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
timote sama nawle bi may jàpple ci liggéey bi, mu ngi leen di nuyu, ak samay bokk lusiyus, yason ak sosipater.
timothée, mon compagnon d`oeuvre, vous salue, ainsi que lucius, jason et sosipater, mes parents.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte samay jëf jaaxal na ma; li ma bëgg a def, duma ko def, waaye li ma bañ rekk, moom laay def.
car je ne sais pas ce que je fais: je ne fais point ce que je veux, et je fais ce que je hais.
Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 31
Quality:
yeesu ne yawut ya ko gëmoon: «bu ngeen saxee ci li ma wax, nekk ngeen samay taalibe ci lu wóor.
et il dit aux juifs qui avaient cru en lui: si vous demeurez dans ma parole, vous êtes vraiment mes disciples;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: