From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ay njéeréer génn ca saxar sa, tasaaroo ci biir àddina. Ñu jox leen kàttan gu mel ni kàttanu jànkalaar.
de la fumée sortirent des sauterelles, qui se répandirent sur la terre; et il leur fut donné un pouvoir comme le pouvoir qu`ont les scorpions de la terre.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
du dammaate barax bu banku,te mees guy saxar, du ko fey,ba kera mu yégal njub, ba daan.
il ne brisera point le roseau cassé, et il n`éteindra point le lumignon qui fume, jusqu`à ce qu`il ait fait triompher la justice.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
benn ci ñetti xaaju nit ñi dee ci ñetti musiba ya: ci safara, saxar ak tamarax yi génn ci seeni gémmiñ.
le tiers des hommes fut tué par ces trois fléaux, par le feu, par la fumée, et par le soufre, qui sortaient de leurs bouches.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te bu ñu séenee saxar sa cay jollee, naan: «ndax dëkk bu niroo woon ak dëkk bu mag bii mas na am?»
et ils s`écriaient, en voyant la fumée de son embrasement: quelle ville était semblable à la grande ville?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
biddiiw ba ubbi buntu kàmb gu xóot ga. noonu saxar jollee ca, su mel ni saxarus puur bu mag, jant bi ak jaww ji lépp lëndëm ndax saxarus kàmb ga.
et elle ouvrit le puits de l`abîme. et il monta du puits une fumée, comme la fumée d`une grande fournaise; et le soleil et l`air furent obscurcis par la fumée du puits.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
buuri àddina yépp, yi àndoon ak moom ci njaaloo ak mbuux, bu ñu séenee saxar siy jollee ci taal bi ñu koy lakke, dinañu yuuxu, di ko jooy.
et tous les rois de la terre, qui se sont livrés avec elle à l`impudicité et au luxe, pleureront et se lamenteront à cause d`elle, quand ils verront la fumée de son embrasement.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te saxar siy jóge ci seen mbugal dina gilli ba fàww. Ñooñu di jaamu rab wi ak nataalam, ak képp ku nangoo jot màndargam turam, duñu noppalu guddi ak bëccëg.»
et la fumée de leur tourment monte aux siècles des siècles; et ils n`ont de repos ni jour ni nuit, ceux qui adorent la bête et son image, et quiconque reçoit la marque de son nom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nii laa gise ci peeñu mi fas ya ak ña leen war: ñu sol kiiraay yu xonq ni safara, bulo ni saxar, ak mboq ni tamarax. boppi fas yaa nga doon nirook boppi gaynde; safara, saxar ak tamarax di génn ci seeni gémmiñ.
et ainsi je vis les chevaux dans la vision, et ceux qui les montaient, ayant des cuirasses couleur de feu, d`hyacinthe, et de soufre. les têtes des chevaux étaient comme des têtes de lions; et de leurs bouches il sortait du feu, de la fumée, et du soufre.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: