Results for si kanam translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ba ci kanam

French

À plutard

Last Update: 2022-05-17
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

si lo nek

French

quoi de neuf

Last Update: 2021-04-09
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

si lonek ?

French

Last Update: 2023-09-25
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

mu jël ko, lekk ci seen kanam.

French

il en prit, et il mangea devant eux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ndaxte ñépp a yem fa kanam yàlla.

French

car devant dieu il n`y a point d`acception de personnes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

nékal si diam

French

Last Update: 2023-12-10
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

noonu kenn du man a damu ca kanam yàlla.

French

afin que nulle chair ne se glorifie devant dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

mangui si diameu

French

Last Update: 2024-01-24
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

googu kóolute lanu am fa kanam yàlla ndax kirist.

French

cette assurance-là, nous l`avons par christ auprès de dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

malaraw mangui si diam

French

Last Update: 2020-05-23
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

morom mogui si yonne

French

Last Update: 2023-06-12
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

faaydaalal yëf yooyu te sóobu ci, ba sa jëm kanam bir ñépp.

French

occupe-toi de ces choses, donne-toi tout entier à elles, afin que tes progrès soient évidents pour tous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye ñiy bàkkaar, yedd leen fa kanam ñépp, ngir artu ñi ci des.

French

ceux qui pèchent, reprends-les devant tous, afin que les autres aussi éprouvent de la crainte.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

suufeel-leen seen bopp fa kanam boroom bi, kon dina leen yékkati.

French

humiliez-vous devant le seigneur, et il vous élèvera.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

amuloo benn wàll mbaa cér ci lii, ndaxte sa xol laabul ci kanam yàlla.

French

il n`y a pour toi ni part ni lot dans cette affaire, car ton coeur n`est pas droit devant dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

moom yiw na fa kanam yàlla, mu ñaan ko, mu sàkkal ko kër ngir askanu yanqóoba.

French

david trouva grâce devant dieu, et demanda d`élever une demeure pour le dieu de jacob;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

danuy fexee def li jub, du ci kanam yàlla rekk, waaye it ci kanam nit ñi.

French

car nous recherchons ce qui est bien, non seulement devant le seigneur, mais aussi devant les hommes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

ci jàngu yi, féete kanam lañuy wut, te toogu yu yiw lañuy taamu ci reeri xew yi.

French

qui recherchent les premiers sièges dans les synagogues, et les premières places dans les festins;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari làmpu diwlin, yi taxaw ci kanam boroom suuf si.

French

ce sont les deux oliviers et les deux chandeliers qui se tiennent devant le seigneur de la terre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«ci kanam tuuti dungeen ma gisati. bu ñu ci tegee ab diir, ngeen gisaat ma.»

French

encore un peu de temps, et vous ne me verrez plus; et puis encore un peu de temps, et vous me verrez, parce que je vais au père.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,793,861,149 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK