Results for sikk translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

te fen musul a génn ci seen gémmiñ. amuñu benn sikk.

French

et dans leur bouche il ne s`est point trouvé de mensonge, car ils sont irrépréhensibles.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bëggunoo lëmbaaje xelu kenn ci dara, ngir kenn bañ a sikk sunu liggéey.

French

nous ne donnons aucun sujet de scandale en quoi que ce soit, afin que le ministère ne soit pas un objet de blâme.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu fekkoonte ne, kóllëre gu jëkk ga dafa amul woon benn sikk, kon du aajo ñu koy weccee ak geneen.

French

en effet, si la première alliance avait été sans défaut, il n`aurait pas été question de la remplacer par une seconde.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte nun ñépp sikk nanu ci fànn yu bare. ki sikkul ci kàddoom, ku mat nga, te man a noot sa yaram wépp.

French

nous bronchons tous de plusieurs manières. si quelqu`un ne bronche point en paroles, c`est un homme parfait, capable de tenir tout son corps en bride.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu dingeen am xol bu laab bu àndul ak ŋàññ, di guney yàlla yu amul sikk ci biir jamono ju yàqu te rëb. dangeen di leer ci seen biir ni weer ci àddina si,

French

afin que vous soyez irréprochables et purs, des enfants de dieu irrépréhensibles au milieu d`une génération perverse et corrompue, parmi laquelle vous brillez comme des flambeaux dans le monde,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka sunu diggante ak yéen ñi gëm, doxal nanu ko doxalin wu sell te jub te amul sikk: seede ngeen ko, te yàlla it seede na ko.

French

vous êtes témoins, et dieu l`est aussi, que nous avons eu envers vous qui croyez une conduite sainte, juste et irréprochable.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na leen yàlla boroom jàmm sellal, ba ngeen mat sëkk; na sàmm seen xel mépp, seen xol bépp ak seen yaram wépp, ngir dara bañ cee am sikk, ba bés bu sunu boroom yeesu kirist dellusee.

French

que le dieu de paix vous sanctifie lui-même tout entiers, et que tout votre être, l`esprit, l`âme et le corps, soit conservé irrépréhensible, lors de l`avènement de notre seigneur jésus christ!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,776,901,367 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK