From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
noonu yeesu tëkku rab wa, rab wa génn ca xale ba, mu daldi wér ca saa sa.
jésus parla sévèrement au démon, qui sortit de lui, et l`enfant fut guéri à l`heure même.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
léegi nag boroom bi, seetal seeni tëkku te may say jaam, nuy wax sa kàddu ak fit.
et maintenant, seigneur, vois leurs menaces, et donne à tes serviteurs d`annoncer ta parole avec une pleine assurance,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ay xarekat laaj nañu ko ne: «li jëm ci nun nag?» mu ne leen: «buleen néewal doole kenn, jël xaalisam ci kaw ay tëkku mbaa ci seede lu dul dëgg. waaye doylooleen li ñu leen di fey.»
des soldats aussi lui demandèrent: et nous, que devons-nous faire? il leur répondit: ne commettez ni extorsion ni fraude envers personne, et contentez-vous de votre solde.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: