From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ku nekk ci kaw taax mi, bul wàcc ngir dugg kër gi, fab say yëf ya fa nekk.
que celui qui sera sur le toit ne descende pas et n`entre pas pour prendre quelque chose dans sa maison;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ku nekk ci kaw taax ma, bul wàcc ngir fab say yëf, ya nekk ci biir kër ga;
que celui qui sera sur le toit ne descende pas pour prendre ce qui est dans sa maison;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
dugg ca taax ma, daldi ne yeesu: «foo jóge?» waaye yeesu tontuwu ko.
il rentra dans le prétoire, et il dit à jésus: d`où es-tu? mais jésus ne lui donna point de réponse.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo tax lu ngeen wax ci biir lëndëm, dees na ko dégg ci leer. lu ngeen déey nit ci biir néeg, dees na ko yégle ci kaw taax yi.
c`est pourquoi tout ce que vous aurez dit dans les ténèbres sera entendu dans la lumière, et ce que vous aurez dit à l`oreille dans les chambres sera prêché sur les toits.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu tontu leen: «du gis ngeen taax yu réy yii yépp? lii lépp dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»
jésus lui répondit: vois-tu ces grandes constructions? il ne restera pas pierre sur pierre qui ne soit renversée.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: