From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
soo ko naree topp genn tooñ mbaa benn bor, topp ma ko.
et s`il t`a fait quelque tort, ou s`il te doit quelque chose, mets-le sur mon compte.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
lewi jóg, bàyyi lépp, daldi ko topp.
et, laissant tout, il se leva, et le suivit.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mbooloo mu bare topp ko, mu faj leen fa.
une grande foule le suivit, et là il guérit les malades.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu jóg, topp ko, moom ak ay taalibeem.
jésus se leva, et le suivit avec ses disciples.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñiy topp seen nafsu, seeni bëgg-bëgg rekk lañu fonk, waaye ñiy topp xelu yàlla mi, coobareem lañu fonk.
ceux, en effet, qui vivent selon la chair, s`affectionnent aux choses de la chair, tandis que ceux qui vivent selon l`esprit s`affectionnent aux choses de l`esprit.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«bu ngeen ma bëggee, dingeen topp sama ndigal.
si vous m`aimez, gardez mes commandements.
Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 6
Quality:
bi mu ko waxee, yeesu dugg ca gaal ga, ay taalibeem topp ko.
il monta dans la barque, et ses disciples le suivirent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
fekk amoon na ca waxambaane wu lëkkaayoo woon sér, topp yeesu, ñu daldi ko jàpp.
un jeune homme le suivait, n`ayant sur le corps qu`un drap. on se saisit de lui;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñiy topp ndigal lii nag, na yàlla wàcce jàmm ak yërmande ci ñoom, ak ci israyilu yàlla.
paix et miséricorde sur tous ceux qui suivront cette règle, et sur l`israël de dieu!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu ngeen ñaanee sax, dungeen jot dara, ndax yéena ngi ñaan ci naaféq, ngir gën a topp seen nafsu.
vous demandez, et vous ne recevez pas, parce que vous demandez mal, dans le but de satisfaire vos passions.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye gànnaayooleen yeesu kirist boroom bi, te bañ a topp seen bakkan ciy bëgg-bëggam yu bon.
mais revêtez-vous du seigneur jésus christ, et n`ayez pas soin de la chair pour en satisfaire les convoitises.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne leen: «Ñëwleen topp ci man, dinaa leen def nappkati nit.»
jésus leur dit: suivez-moi, et je vous ferai pêcheurs d`hommes.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ca saa sa mu daldi gis. noonu mu topp ci yeesu, di màggal yàlla. mbooloo mépp gis loolu, di sant yàlla.
a l`instant il recouvra la vue, et suivit jésus, en glorifiant dieu. tout le peuple, voyant cela, loua dieu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne leen: «muju jamono ay tiiñalkat dinañu feeñ, ñuy weddi yàlla, ngir topp seen bakkan.»
ils vous disaient qu`au dernier temps il y aurait des moqueurs, marchant selon leurs convoitises impies;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.
mais ce qui est spirituel n`est pas le premier, c`est ce qui est animal; ce qui est spirituel vient ensuite.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu ne ko: «demal ci jàmm. sa ngëm faj na la.» ci saa si gumba gi gis, daldi topp yeesu ci yoon wi.
et jésus lui dit: va, ta foi t`a sauvé. (10:53) aussitôt il recouvra la vue, et suivit jésus dans le chemin.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.